Ibrahima · 29/52
Tekki Waxtaan — Simoore Ibrahima
جَهَنَّمَ يَصْلَوْنَهَا ۖ وَبِئْسَ الْقَرَارُ ۝٢٩
Jahannama yaslawnahaa wa bi`sal qaraar
📖 Tekkim Wolof
danañu séndal ci Safara ? Ndaw saxuwaay bu bon !

🎧 Dégg


📜 Aaya 27-31 — Simoore Ibrahima

27يُثَبِّتُ اللَّهُ الَّذِينَ آمَنُوا بِالْقَوْلِ الثَّابِتِ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَفِي الْآخِرَةِ ۖ وَيُضِلُّ اللَّهُ الظَّالِمِينَ ۚ وَيَفْعَلُ اللَّهُ مَا يَشَاءُ
Yàlla dana dëgëral ña gëm ci wax ju dëggu, ci dundug àddina ak ca àllaaxira. Te Dana bàyyi tooñkat ya ca seen réer ga. Te Yàlla dana def lu ko soob.
28۞ أَلَمْ تَرَ إِلَى الَّذِينَ بَدَّلُوا نِعْمَتَ اللَّهِ كُفْرًا وَأَحَلُّوا قَوْمَهُمْ دَارَ الْبَوَارِ
Ndax gisuloo ñay feye xéewali Yàlla ci di Ko weddi tey wàcce seenu nit ci kërug alkaande
29جَهَنَّمَ يَصْلَوْنَهَا ۖ وَبِئْسَ الْقَرَارُ
danañu séndal ci Safara ? Ndaw saxuwaay bu bon !
30وَجَعَلُوا لِلَّهِ أَندَادًا لِّيُضِلُّوا عَن سَبِيلِهِ ۗ قُلْ تَمَتَّعُوا فَإِنَّ مَصِيرَكُمْ إِلَى النَّارِ
Ñay sàkkal Yàlla nawle ngir réeral [seenu nit] soreel leen yoonu [Yàlla] : “Xéewluleen rekk, Safara ngeen di mujj di”.
31قُل لِّعِبَادِيَ الَّذِينَ آمَنُوا يُقِيمُوا الصَّلَاةَ وَيُنفِقُوا مِمَّا رَزَقْنَاهُمْ سِرًّا وَعَلَانِيَةً مِّن قَبْلِ أَن يَأْتِيَ يَوْمٌ لَّا بَيْعٌ فِيهِ وَلَا خِلَالٌ
Waxal sama jaam yi gëm ne leen : "Nañuy taxawal julli tey joxe ca la Ma leen wërsëgale ci lu nëbbu walla la feeñ, balaa àpp bis di ñëw boo xam ne jotoo amu fa waxantumalaa xaritoo.
IbrahimaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
29Aaya

Tekki — Ibrahima 29

Simoore Ibrahima Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : danañu séndal ci Safara ? Ndaw saxuwaay bu bon !

Simoore Aaya 29/52 — Simoore Ibrahima إبراهيم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ibrahima Dégg, Simoore Ibrahima Tekki, Simoore Ibrahima mp3, Simoore Ibrahima pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers