Al-Hijr · 14/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَلَوْ فَتَحْنَا عَلَيْهِم بَابًا مِّنَ السَّمَاءِ فَظَلُّوا فِيهِ يَعْرُجُونَ ۝١٤
Wa law fatahnaa `alaihim baabam minas samaaa`i fazaloo feehi ya`rujoon
📖 Tekkim Wolof
Te su Nu leen ubbiloon ab buntu ci asamaan ñu mën caa yeendoo yéeg,

🎧 Dégg


📜 Aaya 12-16 — Simoore Al-Hijr

12كَذَٰلِكَ نَسْلُكُهُ فِي قُلُوبِ الْمُجْرِمِينَ
Noonu la Nu koy tàbbalee ci xoli saay-saay sa.
13لَا يُؤْمِنُونَ بِهِ ۖ وَقَدْ خَلَتْ سُنَّةُ الْأَوَّلِينَ
Duñu ko gëm te aadaay ñu njëkk ña wéy na.
14وَلَوْ فَتَحْنَا عَلَيْهِم بَابًا مِّنَ السَّمَاءِ فَظَلُّوا فِيهِ يَعْرُجُونَ
Te su Nu leen ubbiloon ab buntu ci asamaan ñu mën caa yeendoo yéeg,
15لَقَالُوا إِنَّمَا سُكِّرَتْ أَبْصَارُنَا بَلْ نَحْنُ قَوْمٌ مَّسْحُورُونَ
Kon it fàwwu ñu wax ne : “Dañoo gëlëmal sunuy gët. Walla sax dañu noo njibar”.
16وَلَقَدْ جَعَلْنَا فِي السَّمَاءِ بُرُوجًا وَزَيَّنَّاهَا لِلنَّاظِرِينَ
Def nañu ci asamaan ay bidiw te rafetal Nanu ko ñi koy xool mu ne ràññ.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Al-Hijr 14

Simoore Al-Hijr Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te su Nu leen ubbiloon ab buntu ci asamaan ñu…

Simoore Aaya 14/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers