Al-Hijr · 22/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
وَأَرْسَلْنَا الرِّيَاحَ لَوَاقِحَ فَأَنزَلْنَا مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَأَسْقَيْنَاكُمُوهُ وَمَا أَنتُمْ لَهُ بِخَازِنِينَ ٢٢
Transliteration
Wa arsalnar riyaaha la waaqiha fa anzalnaa minas samaaa`i maaa`an fa asqai naakumoohu wa maaa antum lahoo bikhaazineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yónni Nanu ngelaw luy sos (taw ci niir yi) ; wàcce Nanu ndox mu jóge asamaan, nàndal Nanu leen ci te mënuleen ko woon a denc.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 20-24 — Al-Hijr
20وَجَعَلْنَا لَكُمْ فِيهَا مَعَايِشَ وَمَن لَّسْتُمْ لَهُ بِرَازِقِينَ
Nu defaral leen ca lu ngeen di dunde, yéen ak ñi ngeen dundalul.
21وَإِن مِّن شَيْءٍ إِلَّا عِندَنَا خَزَائِنُهُ وَمَا نُنَزِّلُهُ إِلَّا بِقَدَرٍ مَّعْلُومٍ
Amul lenn loo xam ne ndàmbam nekkul ci nun, waaye Dunu ca wàcce lu dul ab natt bu ñu xam (bu yem ak bu doy).
22وَأَرْسَلْنَا الرِّيَاحَ لَوَاقِحَ فَأَنزَلْنَا مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَأَسْقَيْنَاكُمُوهُ وَمَا أَنتُمْ لَهُ بِخَازِنِينَ
Yónni Nanu ngelaw luy sos (taw ci niir yi) ; wàcce Nanu ndox mu jóge asamaan, nàndal Nanu leen ci te mënuleen ko woon a denc.
23وَإِنَّا لَنَحْنُ نُحْيِي وَنُمِيتُ وَنَحْنُ الْوَارِثُونَ
Te Nun nooy dundal te Nun nooy rey te Nun nooy donn (mujje) àddina bi yépp.
24وَلَقَدْ عَلِمْنَا الْمُسْتَقْدِمِينَ مِنكُمْ وَلَقَدْ عَلِمْنَا الْمُسْتَأْخِرِينَ
Sunu xam-xam làmb na ña jiitu woon ak ñay mujj ci yéen.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
22Aaya
Tekki — Al-Hijr 22
Simoore Al-Hijr Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yónni Nanu ngelaw luy sos (taw ci niir yi) ;…Simoore Aaya 22/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








