Al-Hijr · 50/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَأَنَّ عَذَابِي هُوَ الْعَذَابُ الْأَلِيمُ ۝٥٠
Wa anna `azaabee uwal `azaabul aleem
📖 Tekkim Wolof
Waaye sama mbugal mooy mbugal mu metti mi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 48-52 — Simoore Al-Hijr

48لَا يَمَسُّهُمْ فِيهَا نَصَبٌ وَمَا هُم مِّنْهَا بِمُخْرَجِينَ
Coono duleen fa laal. Te dootuñu fa génnati.
49۞ نَبِّئْ عِبَادِي أَنِّي أَنَا الْغَفُورُ الرَّحِيمُ
Xamalal samay jaam ne, Man Jéggalaakoon laa, Jaglewaakoon laa.
50وَأَنَّ عَذَابِي هُوَ الْعَذَابُ الْأَلِيمُ
Waaye sama mbugal mooy mbugal mu metti mi.
51وَنَبِّئْهُمْ عَن ضَيْفِ إِبْرَاهِيمَ
Te nga nettalileen la xewoon ca gani Ibraahiima ya
52إِذْ دَخَلُوا عَلَيْهِ فَقَالُوا سَلَامًا قَالَ إِنَّا مِنكُمْ وَجِلُونَ
Ba ñu agsee ca moom ne ko : “Jàmmu ngaam” - Mu ne leen : “Am naa njàqare ci yéen”.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
50Aaya

Tekki — Al-Hijr 50

Simoore Al-Hijr Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waaye sama mbugal mooy mbugal mu metti mi.

Simoore Aaya 50/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers