Al-Hijr · 51/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَنَبِّئْهُمْ عَن ضَيْفِ إِبْرَاهِيمَ ۝٥١
Wa nabbi`hum `an daifi Ibraaheem
📖 Tekkim Wolof
Te nga nettalileen la xewoon ca gani Ibraahiima ya

🎧 Dégg


📜 Aaya 49-53 — Simoore Al-Hijr

49۞ نَبِّئْ عِبَادِي أَنِّي أَنَا الْغَفُورُ الرَّحِيمُ
Xamalal samay jaam ne, Man Jéggalaakoon laa, Jaglewaakoon laa.
50وَأَنَّ عَذَابِي هُوَ الْعَذَابُ الْأَلِيمُ
Waaye sama mbugal mooy mbugal mu metti mi.
51وَنَبِّئْهُمْ عَن ضَيْفِ إِبْرَاهِيمَ
Te nga nettalileen la xewoon ca gani Ibraahiima ya
52إِذْ دَخَلُوا عَلَيْهِ فَقَالُوا سَلَامًا قَالَ إِنَّا مِنكُمْ وَجِلُونَ
Ba ñu agsee ca moom ne ko : “Jàmmu ngaam” - Mu ne leen : “Am naa njàqare ci yéen”.
53قَالُوا لَا تَوْجَلْ إِنَّا نُبَشِّرُكَ بِغُلَامٍ عَلِيمٍ
Ñu ne : “Bul jàq ci nun ! Noo ngi lay bégal ne [danga am doom] ju góor juy bari xam- xam”.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
51Aaya

Tekki — Al-Hijr 51

Simoore Al-Hijr Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te nga nettalileen la xewoon ca gani Ibraahiima ya

Simoore Aaya 51/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers