Al-Hijr · 49/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
۞ نَبِّئْ عِبَادِي أَنِّي أَنَا الْغَفُورُ الرَّحِيمُ ۝٤٩
Nabbi` `ibaadeee annneee anal Ghafoorur Raheem
📖 Tekkim Wolof
Xamalal samay jaam ne, Man Jéggalaakoon laa, Jaglewaakoon laa.

🎧 Dégg


📜 Aaya 47-51 — Simoore Al-Hijr

47وَنَزَعْنَا مَا فِي صُدُورِهِم مِّنْ غِلٍّ إِخْوَانًا عَلَىٰ سُرُرٍ مُّتَقَابِلِينَ
Te Nu rocci [raxas] la nekkoon ci seeni xol cig noonoo : ñu nekk ay mbokk yu jaaxaan ca seeni lal jàkkaarloo.
48لَا يَمَسُّهُمْ فِيهَا نَصَبٌ وَمَا هُم مِّنْهَا بِمُخْرَجِينَ
Coono duleen fa laal. Te dootuñu fa génnati.
49۞ نَبِّئْ عِبَادِي أَنِّي أَنَا الْغَفُورُ الرَّحِيمُ
Xamalal samay jaam ne, Man Jéggalaakoon laa, Jaglewaakoon laa.
50وَأَنَّ عَذَابِي هُوَ الْعَذَابُ الْأَلِيمُ
Waaye sama mbugal mooy mbugal mu metti mi.
51وَنَبِّئْهُمْ عَن ضَيْفِ إِبْرَاهِيمَ
Te nga nettalileen la xewoon ca gani Ibraahiima ya
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
49Aaya

Tekki — Al-Hijr 49

Simoore Al-Hijr Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xamalal samay jaam ne, Man Jéggalaakoon laa, Jaglewaakoon laa.

Simoore Aaya 49/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers