Al-Hijr · 57/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
قَالَ فَمَا خَطْبُكُمْ أَيُّهَا الْمُرْسَلُونَ ٥٧
Transliteration
Qaala famaa khatbukum aiyuhal mursaloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Mu ne leen : “Waaw lan mooy seen mbir yéen ñi ñu yónni ?
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 55-59 — Simoore Al-Hijr
55قَالُوا بَشَّرْنَاكَ بِالْحَقِّ فَلَا تَكُن مِّنَ الْقَانِطِينَ
- Ñu ne ko : “Yégal ne lii dëgg la. Bul bokk ca ña naagu ña”.
56قَالَ وَمَن يَقْنَطُ مِن رَّحْمَةِ رَبِّهِ إِلَّا الضَّالُّونَ
- Mu ne : “Kan mooy naagu ci yërmaande Yàlla, ñu dul ñu réer [sànku] ? ”
57قَالَ فَمَا خَطْبُكُمْ أَيُّهَا الْمُرْسَلُونَ
Mu ne leen : “Waaw lan mooy seen mbir yéen ñi ñu yónni ?
58قَالُوا إِنَّا أُرْسِلْنَا إِلَىٰ قَوْمٍ مُّجْرِمِينَ
- Ñu ne : “Yónneef nañu ci aw nit ñu bari bàkkaar,
59إِلَّا آلَ لُوطٍ إِنَّا لَمُنَجُّوهُمْ أَجْمَعِينَ
ba mu des njabootu Lóot, danañu leen musal ñoom ñépp
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
57Aaya
Tekki — Al-Hijr 57
Simoore Al-Hijr Aaya 57 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne leen : “Waaw lan mooy seen mbir yéen…Simoore Aaya 57/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 55–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Al-Hijr
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Friday, October 2, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


