Al-Hijr · 58/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
قَالُوا إِنَّا أُرْسِلْنَا إِلَىٰ قَوْمٍ مُّجْرِمِينَ ۝٥٨
Qaaloo innaaa ursilnaaa ilaa qawmim mujrimeen
📖 Tekkim Wolof
- Ñu ne : “Yónneef nañu ci aw nit ñu bari bàkkaar,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 56-60 — Simoore Al-Hijr

56قَالَ وَمَن يَقْنَطُ مِن رَّحْمَةِ رَبِّهِ إِلَّا الضَّالُّونَ
- Mu ne : “Kan mooy naagu ci yërmaande Yàlla, ñu dul ñu réer [sànku] ? ”
57قَالَ فَمَا خَطْبُكُمْ أَيُّهَا الْمُرْسَلُونَ
Mu ne leen : “Waaw lan mooy seen mbir yéen ñi ñu yónni ?
58قَالُوا إِنَّا أُرْسِلْنَا إِلَىٰ قَوْمٍ مُّجْرِمِينَ
- Ñu ne : “Yónneef nañu ci aw nit ñu bari bàkkaar,
59إِلَّا آلَ لُوطٍ إِنَّا لَمُنَجُّوهُمْ أَجْمَعِينَ
ba mu des njabootu Lóot, danañu leen musal ñoom ñépp
60إِلَّا امْرَأَتَهُ قَدَّرْنَا ۙ إِنَّهَا لَمِنَ الْغَابِرِينَ
ku ca dul soxnaam sa. “Dogal Nanu ne moom ca way-des ña lay bokk (alku)”.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
58Aaya

Tekki — Al-Hijr 58

Simoore Al-Hijr Aaya 58 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Ñu ne : “Yónneef nañu ci aw nit ñu…

Simoore Aaya 58/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 56–60. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers