Al-Hijr · 56/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
قَالَ وَمَن يَقْنَطُ مِن رَّحْمَةِ رَبِّهِ إِلَّا الضَّالُّونَ ٥٦
Transliteration
Qaala wa mai yaqnatu mir rahmati Rabbiheee illad daaaloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
- Mu ne : “Kan mooy naagu ci yërmaande Yàlla, ñu dul ñu réer [sànku] ? ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 54-58 — Al-Hijr
54قَالَ أَبَشَّرْتُمُونِي عَلَىٰ أَن مَّسَّنِيَ الْكِبَرُ فَبِمَ تُبَشِّرُونَ
Mu ne : “Li ngeen di bégle ndax ànd naak samag mage ? Li ngeen may yégal mooy lan ? ”
55قَالُوا بَشَّرْنَاكَ بِالْحَقِّ فَلَا تَكُن مِّنَ الْقَانِطِينَ
- Ñu ne ko : “Yégal ne lii dëgg la. Bul bokk ca ña naagu ña”.
56قَالَ وَمَن يَقْنَطُ مِن رَّحْمَةِ رَبِّهِ إِلَّا الضَّالُّونَ
- Mu ne : “Kan mooy naagu ci yërmaande Yàlla, ñu dul ñu réer [sànku] ? ”
57قَالَ فَمَا خَطْبُكُمْ أَيُّهَا الْمُرْسَلُونَ
Mu ne leen : “Waaw lan mooy seen mbir yéen ñi ñu yónni ?
58قَالُوا إِنَّا أُرْسِلْنَا إِلَىٰ قَوْمٍ مُّجْرِمِينَ
- Ñu ne : “Yónneef nañu ci aw nit ñu bari bàkkaar,
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
56Aaya
Tekki — Al-Hijr 56
Simoore Al-Hijr Aaya 56 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Mu ne : “Kan mooy naagu ci yërmaande Yàlla,…Simoore Aaya 56/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 54–58. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








