An-Nahl · 107/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمُ اسْتَحَبُّوا الْحَيَاةَ الدُّنْيَا عَلَى الْآخِرَةِ وَأَنَّ اللَّهَ لَا يَهْدِي الْقَوْمَ الْكَافِرِينَ ۝١٠٧
Zaalika bi annahumus tahabbul hayaatad dunyaa `alal Aakhirati wa annal laaha laa yahdil qawmal kaafireen
📖 Tekkim Wolof
Li waral loolu moo di dañoo tànn dundug àddina ci kaw dundug àllaaxira. Te nag Yàlla du gindi aw nit ñu di ay yéefar.

🎧 Dégg


📜 Aaya 105-109 — An-Nahl

105إِنَّمَا يَفْتَرِي الْكَذِبَ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِآيَاتِ اللَّهِ ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْكَاذِبُونَ
Ca dëgg-dëgg ñay duur ay fen ñooy ña gëmul kàdduy Yàlla yi, ñoom ñooy fenkat yi.
106مَن كَفَرَ بِاللَّهِ مِن بَعْدِ إِيمَانِهِ إِلَّا مَنْ أُكْرِهَ وَقَلْبُهُ مُطْمَئِنٌّ بِالْإِيمَانِ وَلَٰكِن مَّن شَرَحَ بِالْكُفْرِ صَدْرًا فَعَلَيْهِمْ غَضَبٌ مِّنَ اللَّهِ وَلَهُمْ عَذَابٌ عَظِيمٌ
Ku weddi Yàlla ginnaaw ba mu gëmee... - ku dul ka ñu not fekk xelam sax na ci gëm Yàlla - ak ña ubbi seen dënn cig kéefar, mer mu tukkee ca Yàlla dana leen sadd te ñeel na leen mbugal mu màgg.
107ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمُ اسْتَحَبُّوا الْحَيَاةَ الدُّنْيَا عَلَى الْآخِرَةِ وَأَنَّ اللَّهَ لَا يَهْدِي الْقَوْمَ الْكَافِرِينَ
Li waral loolu moo di dañoo tànn dundug àddina ci kaw dundug àllaaxira. Te nag Yàlla du gindi aw nit ñu di ay yéefar.
108أُولَٰئِكَ الَّذِينَ طَبَعَ اللَّهُ عَلَىٰ قُلُوبِهِمْ وَسَمْعِهِمْ وَأَبْصَارِهِمْ ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْغَافِلُونَ
Ñooñooy ña Yàlla fatt seeni xol, ak seeni dégg-dégg, ak seeni gis-gis. Te ñoom ñooy ña sàggan.
109لَا جَرَمَ أَنَّهُمْ فِي الْآخِرَةِ هُمُ الْخَاسِرُونَ
Ca dëgg-dëgg, ñoom ñooy ñay yàqule ci àllaaxira.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
107Aaya

Tekki — An-Nahl 107

Simoore An-Nahl Aaya 107 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Li waral loolu moo di dañoo tànn dundug àddina ci…

Simoore Aaya 107/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 105–109. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers