An-Nahl · 108/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
أُولَٰئِكَ الَّذِينَ طَبَعَ اللَّهُ عَلَىٰ قُلُوبِهِمْ وَسَمْعِهِمْ وَأَبْصَارِهِمْ ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْغَافِلُونَ ١٠٨
Transliteration
Ulaaa`ikal lazeena taba`al laahu `alaa quloobihim wa sam`ihim wa absaarihim wa ulaaa`ika humul ghaafiloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñooñooy ña Yàlla fatt seeni xol, ak seeni dégg-dégg, ak seeni gis-gis. Te ñoom ñooy ña sàggan.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 106-110 — An-Nahl
106مَن كَفَرَ بِاللَّهِ مِن بَعْدِ إِيمَانِهِ إِلَّا مَنْ أُكْرِهَ وَقَلْبُهُ مُطْمَئِنٌّ بِالْإِيمَانِ وَلَٰكِن مَّن شَرَحَ بِالْكُفْرِ صَدْرًا فَعَلَيْهِمْ غَضَبٌ مِّنَ اللَّهِ وَلَهُمْ عَذَابٌ عَظِيمٌ
Ku weddi Yàlla ginnaaw ba mu gëmee... - ku dul ka ñu not fekk xelam sax na ci gëm Yàlla - ak ña ubbi seen dënn cig kéefar, mer mu tukkee ca Yàlla dana leen sadd te ñeel na leen mbugal mu màgg.
107ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمُ اسْتَحَبُّوا الْحَيَاةَ الدُّنْيَا عَلَى الْآخِرَةِ وَأَنَّ اللَّهَ لَا يَهْدِي الْقَوْمَ الْكَافِرِينَ
Li waral loolu moo di dañoo tànn dundug àddina ci kaw dundug àllaaxira. Te nag Yàlla du gindi aw nit ñu di ay yéefar.
108أُولَٰئِكَ الَّذِينَ طَبَعَ اللَّهُ عَلَىٰ قُلُوبِهِمْ وَسَمْعِهِمْ وَأَبْصَارِهِمْ ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْغَافِلُونَ
Ñooñooy ña Yàlla fatt seeni xol, ak seeni dégg-dégg, ak seeni gis-gis. Te ñoom ñooy ña sàggan.
109لَا جَرَمَ أَنَّهُمْ فِي الْآخِرَةِ هُمُ الْخَاسِرُونَ
Ca dëgg-dëgg, ñoom ñooy ñay yàqule ci àllaaxira.
110ثُمَّ إِنَّ رَبَّكَ لِلَّذِينَ هَاجَرُوا مِن بَعْدِ مَا فُتِنُوا ثُمَّ جَاهَدُوا وَصَبَرُوا إِنَّ رَبَّكَ مِن بَعْدِهَا لَغَفُورٌ رَّحِيمٌ
La cay topp moo di sa Boroom dana jéggal ña gàddaayoon te muñ, ginnaaw loolu sa Boroom dana jagle njéggalam ak yërmaandeem.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
108Aaya
Tekki — An-Nahl 108
Simoore An-Nahl Aaya 108 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñooñooy ña Yàlla fatt seeni xol, ak seeni dégg-dégg, ak…Simoore Aaya 108/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 106–110. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








