An-Nahl · 33/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
هَلْ يَنظُرُونَ إِلَّا أَن تَأْتِيَهُمُ الْمَلَائِكَةُ أَوْ يَأْتِيَ أَمْرُ رَبِّكَ ۚ كَذَٰلِكَ فَعَلَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ وَمَا ظَلَمَهُمُ اللَّهُ وَلَٰكِن كَانُوا أَنفُسَهُمْ يَظْلِمُونَ ٣٣
Transliteration
Hal yanzuroona illaaa an taatiyahumul malaaa`ikatu aw yaatiya amru Rabbik; kazaalika fa`alal lazeena min qablihim; wa maa zalamahumul laahu wa laakin kaanoo anfusahum yazlimoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Lan la [yéefar ya] di xaar, Malaaka ya digal leen walla sa dogalu Boroom agsi ci ñoom ? Noonu la [yéefar ya] leen jiitu nekke woon. Waaye ñoom ñoo tooñ seen bopp.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 31-35 — An-Nahl
31جَنَّاتُ عَدْنٍ يَدْخُلُونَهَا تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۖ لَهُمْ فِيهَا مَا يَشَاءُونَ ۚ كَذَٰلِكَ يَجْزِي اللَّهُ الْمُتَّقِينَ
Àjjana ju sax la, ñu tàbbi ca, te ay dex danañuy daw-dawaan ci suufam. Te danañu fa am lu ñu bëgg ; Noonu la Yàlla di feye way-ragal ña [Yàlla].
32الَّذِينَ تَتَوَفَّاهُمُ الْمَلَائِكَةُ طَيِّبِينَ ۙ يَقُولُونَ سَلَامٌ عَلَيْكُمُ ادْخُلُوا الْجَنَّةَ بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Ña nga xam ne Malaaka ya danañu leen rey - fekk ñu nekk ñu sell - danañu leen wax ne : “Yal na jàmm nekk ci yéen ! Dugguleen Àjjana ci sababus la ngeen daan jëf [ci lu baax]”.
33هَلْ يَنظُرُونَ إِلَّا أَن تَأْتِيَهُمُ الْمَلَائِكَةُ أَوْ يَأْتِيَ أَمْرُ رَبِّكَ ۚ كَذَٰلِكَ فَعَلَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ وَمَا ظَلَمَهُمُ اللَّهُ وَلَٰكِن كَانُوا أَنفُسَهُمْ يَظْلِمُونَ
Lan la [yéefar ya] di xaar, Malaaka ya digal leen walla sa dogalu Boroom agsi ci ñoom ? Noonu la [yéefar ya] leen jiitu nekke woon. Waaye ñoom ñoo tooñ seen bopp.
34فَأَصَابَهُمْ سَيِّئَاتُ مَا عَمِلُوا وَحَاقَ بِهِم مَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Dal na ci seen kaw ñaawtéefu la ñu defoon, ndax wàcc na ci ñoom la ñu doon soofantal di ko reetaan.
35وَقَالَ الَّذِينَ أَشْرَكُوا لَوْ شَاءَ اللَّهُ مَا عَبَدْنَا مِن دُونِهِ مِن شَيْءٍ نَّحْنُ وَلَا آبَاؤُنَا وَلَا حَرَّمْنَا مِن دُونِهِ مِن شَيْءٍ ۚ كَذَٰلِكَ فَعَلَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ فَهَلْ عَلَى الرُّسُلِ إِلَّا الْبَلَاغُ الْمُبِينُ
Ña daan bokkaale wax ne : “Bu neexoon Yàlla, dunu jaamu kenn ku dul Moom, du nun du kenn ci sunuy baay ; te kon dunu ne dara araam na te du ci ndigalam. Ña leen jiitu woon noonu lañu defoon. Te li war ab Yonent ndax dafa dul jottali rekk [la ñu ko yónni] ba mu mat sëkk ?
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
33Aaya
Tekki — An-Nahl 33
Simoore An-Nahl Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lan la [yéefar ya] di xaar, Malaaka ya digal leen…Simoore Aaya 33/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








