An-Nahl · 66/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
وَإِنَّ لَكُمْ فِي الْأَنْعَامِ لَعِبْرَةً ۖ نُّسْقِيكُم مِّمَّا فِي بُطُونِهِ مِن بَيْنِ فَرْثٍ وَدَمٍ لَّبَنًا خَالِصًا سَائِغًا لِّلشَّارِبِينَ ۝٦٦
Wa inna lakum fil an`aami la`ibrah; nusqeekum mimmmaa fee butoonihee mim baini farsinw wa damil labanann khaalisan saaa`ighallish shaaribeen
📖 Tekkim Wolof
Te sax am ngeen lu ngeen mën a waaroo ci mala yi : Noo ngi leen di nàndal ci li nekk ci seen biir - lu génne ci diggante sebret ak deret - muy meew mu neex te sell ca ña koy naan.

🎧 Dégg


📜 Aaya 64-68 — An-Nahl

64وَمَا أَنزَلْنَا عَلَيْكَ الْكِتَابَ إِلَّا لِتُبَيِّنَ لَهُمُ الَّذِي اخْتَلَفُوا فِيهِ ۙ وَهُدًى وَرَحْمَةً لِّقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Wàccewuñu ci yaaw Téere [Alxuraan] ba lu dul ngir nga leeralal leen la ñu nekkoon ci juuyoo, ak ngir mu nekk di njub ak yërmaande ci nit ñu gëm.
65وَاللَّهُ أَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَأَحْيَا بِهِ الْأَرْضَ بَعْدَ مَوْتِهَا ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّقَوْمٍ يَسْمَعُونَ
Te Yàlla moo wàcce ndox mu jóge ca kaw, mu dundal ci suuf si ginnaaw ba mu bekkooree. Te nekk na ci loolu tegtal ci nit ñuy dégg.
66وَإِنَّ لَكُمْ فِي الْأَنْعَامِ لَعِبْرَةً ۖ نُّسْقِيكُم مِّمَّا فِي بُطُونِهِ مِن بَيْنِ فَرْثٍ وَدَمٍ لَّبَنًا خَالِصًا سَائِغًا لِّلشَّارِبِينَ
Te sax am ngeen lu ngeen mën a waaroo ci mala yi : Noo ngi leen di nàndal ci li nekk ci seen biir - lu génne ci diggante sebret ak deret - muy meew mu neex te sell ca ña koy naan.
67وَمِن ثَمَرَاتِ النَّخِيلِ وَالْأَعْنَابِ تَتَّخِذُونَ مِنْهُ سَكَرًا وَرِزْقًا حَسَنًا ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّقَوْمٍ يَعْقِلُونَ
Te ci meññenti tàndarma ak reseñ, dangeen ca jële naan guy màndee ak xéewal gu baax. Te nekk na ci loolu ay tegtal ci aw nit ñuy xalaat.
68وَأَوْحَىٰ رَبُّكَ إِلَى النَّحْلِ أَنِ اتَّخِذِي مِنَ الْجِبَالِ بُيُوتًا وَمِنَ الشَّجَرِ وَمِمَّا يَعْرِشُونَ
Te sa Boroom moo yenkewal yamb [xamal ko ne] : “Nanga sàkk néeg ci doj ak ci garab yi ak ca lañu tabax.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
66Aaya

Tekki — An-Nahl 66

Simoore An-Nahl Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te sax am ngeen lu ngeen mën a waaroo ci…

Simoore Aaya 66/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers