Al-Isra · 57/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
أُولَٰئِكَ الَّذِينَ يَدْعُونَ يَبْتَغُونَ إِلَىٰ رَبِّهِمُ الْوَسِيلَةَ أَيُّهُمْ أَقْرَبُ وَيَرْجُونَ رَحْمَتَهُ وَيَخَافُونَ عَذَابَهُ ۚ إِنَّ عَذَابَ رَبِّكَ كَانَ مَحْذُورًا ۝٥٧
Ulaaa`ikal lazeena yad`oona yabtaghoona ilaa Rabbihimul waseelata ayyuhum aqrabu wa yarjoona rahmatahoo wa yakhaafoona `azaabah; inna `azaaba rabbika kaana mahzooraa
📖 Tekkim Wolof
Ña ñuy jaamu dañu ne siiw am pexem gën a jegeñ seen Boroom. Te yaakaar nañu yërmaandeem, ragal nañu mbugalam. Naka sa mbugalum Boroom, lu mat a wattandiku la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 55-59 — Al-Isra

55وَرَبُّكَ أَعْلَمُ بِمَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ وَلَقَدْ فَضَّلْنَا بَعْضَ النَّبِيِّينَ عَلَىٰ بَعْضٍ ۖ وَآتَيْنَا دَاوُودَ زَبُورًا
Te sa Boroom moo gën a xam ña nekk ci asmaan yi ak suuf si. Te def Nanu yenn Yonent yi gën ñeneen ña. Te Noo jox Daawuda “Zabour” [Téere].
56قُلِ ادْعُوا الَّذِينَ زَعَمْتُم مِّن دُونِهِ فَلَا يَمْلِكُونَ كَشْفَ الضُّرِّ عَنكُمْ وَلَا تَحْوِيلًا
Neel : “Wooleen ñi ngeen jàpp ne [Yàlla lañu] bàyyi Ko. Duñu mën a wuññi lor ja leen dal, duñu mën a soppi dara.
57أُولَٰئِكَ الَّذِينَ يَدْعُونَ يَبْتَغُونَ إِلَىٰ رَبِّهِمُ الْوَسِيلَةَ أَيُّهُمْ أَقْرَبُ وَيَرْجُونَ رَحْمَتَهُ وَيَخَافُونَ عَذَابَهُ ۚ إِنَّ عَذَابَ رَبِّكَ كَانَ مَحْذُورًا
Ña ñuy jaamu dañu ne siiw am pexem gën a jegeñ seen Boroom. Te yaakaar nañu yërmaandeem, ragal nañu mbugalam. Naka sa mbugalum Boroom, lu mat a wattandiku la.
58وَإِن مِّن قَرْيَةٍ إِلَّا نَحْنُ مُهْلِكُوهَا قَبْلَ يَوْمِ الْقِيَامَةِ أَوْ مُعَذِّبُوهَا عَذَابًا شَدِيدًا ۚ كَانَ ذَٰلِكَ فِي الْكِتَابِ مَسْطُورًا
Amul benn dëkk bu Nu dul alag balaa Bis-pénc ba, walla Nu mbugal ko mbugal mu tar. Looloo nekk ci Téere bu ñu bind. [Yàlla kuy nose la].
59وَمَا مَنَعَنَا أَن نُّرْسِلَ بِالْآيَاتِ إِلَّا أَن كَذَّبَ بِهَا الْأَوَّلُونَ ۚ وَآتَيْنَا ثَمُودَ النَّاقَةَ مُبْصِرَةً فَظَلَمُوا بِهَا ۚ وَمَا نُرْسِلُ بِالْآيَاتِ إِلَّا تَخْوِيفًا
Lu Nu terey wàcce ay kéemaan, lu dul ñu jëkk ña dañu leen a weddi woon. Te sax joxoon Nanu waa Samooda giléem gu jigéen [muy kéemaan] gu leer : ñu def cag tooñeel. Te Nun dunu wàcce kéemaan lu dul ne Danuy xuppe ci kéemaan googu ak di ca àrtu nit ña.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
57Aaya

Tekki — Al-Isra 57

Simoore Al-Isra Aaya 57 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ñuy jaamu dañu ne siiw am pexem gën a…

Simoore Aaya 57/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 55–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers