Al-Isra · 91/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
أَوْ تَكُونَ لَكَ جَنَّةٌ مِّن نَّخِيلٍ وَعِنَبٍ فَتُفَجِّرَ الْأَنْهَارَ خِلَالَهَا تَفْجِيرًا ۝٩١
Aw takoona laka jannatum min nakheelinw wa `inabin fatufajjiral anhaara khilaalahaa tafjeeraa
📖 Tekkim Wolof
walla nga am tooli garabi tàndarma ak garabu reseñ, nga ballal ay dex ci seen diggante yuy ball bu baax ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 89-93 — Simoore Al-Isra

89وَلَقَدْ صَرَّفْنَا لِلنَّاسِ فِي هَٰذَا الْقُرْآنِ مِن كُلِّ مَثَلٍ فَأَبَىٰ أَكْثَرُ النَّاسِ إِلَّا كُفُورًا
Te ca dëgg-dëgg, jox Nanu nit ñi ci Alxuraan jii léebu wu ne [wuy leeral]. Waaye terewul li ëpp ci ñoom wéy di weddi.
90وَقَالُوا لَن نُّؤْمِنَ لَكَ حَتَّىٰ تَفْجُرَ لَنَا مِنَ الْأَرْضِ يَنبُوعًا
Ñu naan : “Duñu gëm mukk li feek ballaloonu ci suuf si ay seewnde [bëti ndox] ;
91أَوْ تَكُونَ لَكَ جَنَّةٌ مِّن نَّخِيلٍ وَعِنَبٍ فَتُفَجِّرَ الْأَنْهَارَ خِلَالَهَا تَفْجِيرًا
walla nga am tooli garabi tàndarma ak garabu reseñ, nga ballal ay dex ci seen diggante yuy ball bu baax ;
92أَوْ تُسْقِطَ السَّمَاءَ كَمَا زَعَمْتَ عَلَيْنَا كِسَفًا أَوْ تَأْتِيَ بِاللَّهِ وَالْمَلَائِكَةِ قَبِيلًا
walla nga rotal ci sunu kaw asamaan si ni nga ko dige, mu nekk ay daggit, mbaa nga indi Yàlla ak Malaaka yi nu jàkkaarloo ;
93أَوْ يَكُونَ لَكَ بَيْتٌ مِّن زُخْرُفٍ أَوْ تَرْقَىٰ فِي السَّمَاءِ وَلَن نُّؤْمِنَ لِرُقِيِّكَ حَتَّىٰ تُنَزِّلَ عَلَيْنَا كِتَابًا نَّقْرَؤُهُ ۗ قُلْ سُبْحَانَ رَبِّي هَلْ كُنتُ إِلَّا بَشَرًا رَّسُولًا
mbaa nga am këru wurus ; mbaa nga yéeg ci kaw asamaan si. Te dunu gëm sa yéeg feek wàcceloonu Téere bu nuy jàng”. Neel : “Tudd naa sellug sama Boroom ! Moo ndax man nekkuma lu dul nit ku ñu yónni doŋŋ ? "
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
91Aaya

Tekki — Al-Isra 91

Simoore Al-Isra Aaya 91 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : walla nga am tooli garabi tàndarma ak garabu reseñ, nga…

Simoore Aaya 91/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 89–93. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers