Maryam · 10/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
قَالَ رَبِّ اجْعَل لِّي آيَةً ۚ قَالَ آيَتُكَ أَلَّا تُكَلِّمَ النَّاسَ ثَلَاثَ لَيَالٍ سَوِيًّا ۝١٠
Qaala Rabbij `al leee Aayah; qaala Aayatuka allaa tukalliman naasa salaasa layaalin sawiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Mu ne ko : “[Yàlla] sama Boroom, defal ma màndarga”. Mu ne ko : “Sa màndarga mooy danga am ñetti fan yoo dul mën a waxante.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 8-12 — Simoore Maryam

8قَالَ رَبِّ أَنَّىٰ يَكُونُ لِي غُلَامٌ وَكَانَتِ امْرَأَتِي عَاقِرًا وَقَدْ بَلَغْتُ مِنَ الْكِبَرِ عِتِيًّا
Mu ne : “Waaw yaw Boroom bi, ana fan la ma doom di bawoo te sama soxna di ku jaasir, man itam ma màggat ba kumur ? ”
9قَالَ كَذَٰلِكَ قَالَ رَبُّكَ هُوَ عَلَيَّ هَيِّنٌ وَقَدْ خَلَقْتُكَ مِن قَبْلُ وَلَمْ تَكُ شَيْئًا
Mu ne ko : “Aa ! Loolu la sa Boroom wax de. Te lu ñàkk solo la ci man ndax maa la bindoon ba nga doonagul dara”.
10قَالَ رَبِّ اجْعَل لِّي آيَةً ۚ قَالَ آيَتُكَ أَلَّا تُكَلِّمَ النَّاسَ ثَلَاثَ لَيَالٍ سَوِيًّا
Mu ne ko : “[Yàlla] sama Boroom, defal ma màndarga”. Mu ne ko : “Sa màndarga mooy danga am ñetti fan yoo dul mën a waxante.
11فَخَرَجَ عَلَىٰ قَوْمِهِ مِنَ الْمِحْرَابِ فَأَوْحَىٰ إِلَيْهِمْ أَن سَبِّحُوا بُكْرَةً وَعَشِيًّا
Mu daldi génne ca fa [mu doon jaaamoo Yàlla] ; jottale leen ne nañuy sàbbal Yàlla suba ak ngoon.
12يَا يَحْيَىٰ خُذِ الْكِتَابَ بِقُوَّةٍ ۖ وَآتَيْنَاهُ الْحُكْمَ صَبِيًّا
"Éy Yahyaa, jàngal Téere ba [cig settantal] ! ”.Jox Nanu la xam-xamu xereñe [àtte ya] ca ba nga doonee ndaw,
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Maryam 10

Simoore Maryam Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne ko : “[Yàlla] sama Boroom, defal ma màndarga”.…

Simoore Aaya 10/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers