Maryam · 19/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
قَالَ إِنَّمَا أَنَا رَسُولُ رَبِّكِ لِأَهَبَ لَكِ غُلَامًا زَكِيًّا ۝١٩
Qaala innamaa ana rasoolu Rabbiki li ahaba laki ghulaaman zakiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Malaaka ma [Jibriil] ne ko : “Man dey ndawul sa Boroom laa [damaa ñëw] ngir may la doom ju sell”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 17-21 — Simoore Maryam

17فَاتَّخَذَتْ مِن دُونِهِمْ حِجَابًا فَأَرْسَلْنَا إِلَيْهَا رُوحَنَا فَتَمَثَّلَ لَهَا بَشَرًا سَوِيًّا
Mu wutoon kiiraay seen diggante. Nu daldi yónni ci moom Sunu ruu [Malaaka] mu yor jëmmi nit [Jibriil].
18قَالَتْ إِنِّي أَعُوذُ بِالرَّحْمَٰنِ مِنكَ إِن كُنتَ تَقِيًّا
[Maryaama] daldi ne : “Man dey maa ngi sàkku ci yërëmaakoon bi [Yàlla] mu musal ma ci yaw ndeem ku ragal Yàlla nga.
19قَالَ إِنَّمَا أَنَا رَسُولُ رَبِّكِ لِأَهَبَ لَكِ غُلَامًا زَكِيًّا
Malaaka ma [Jibriil] ne ko : “Man dey ndawul sa Boroom laa [damaa ñëw] ngir may la doom ju sell”.
20قَالَتْ أَنَّىٰ يَكُونُ لِي غُلَامٌ وَلَمْ يَمْسَسْنِي بَشَرٌ وَلَمْ أَكُ بَغِيًّا
Mu ne ko : “Man naka laay ame doom, te génn góor masumaa laal, te duma ku baaloy ? ”
21قَالَ كَذَٰلِكِ قَالَ رَبُّكِ هُوَ عَلَيَّ هَيِّنٌ ۖ وَلِنَجْعَلَهُ آيَةً لِّلنَّاسِ وَرَحْمَةً مِّنَّا ۚ وَكَانَ أَمْرًا مَّقْضِيًّا
Mu ne ko : “Loolu la sa Boroom wax ! Te lu yomb la ci Man ! Lii dafay doon kéemaan ci nit ñi, ak yërmaande wu bawoo fa Yàlla. Dogal ba sotti na”.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — Maryam 19

Simoore Maryam Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Malaaka ma [Jibriil] ne ko : “Man dey ndawul sa…

Simoore Aaya 19/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers