Maryam · 45/98
Tekki Waxtaan — Maryam
يَا أَبَتِ إِنِّي أَخَافُ أَن يَمَسَّكَ عَذَابٌ مِّنَ الرَّحْمَٰنِ فَتَكُونَ لِلشَّيْطَانِ وَلِيًّا ۝٤٥
Yaaa abati innee akhaafu ai yamssaka `azaabum minar Rahmaani fatakoona lish Shaitaani waliyyaa
📖 Tekkim Wolof
Yaw sama baay, man dey ragal naa mbugalum Yàlla dal la nga fay lëkkook Séytaane”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 43-47 — Maryam

43يَا أَبَتِ إِنِّي قَدْ جَاءَنِي مِنَ الْعِلْمِ مَا لَمْ يَأْتِكَ فَاتَّبِعْنِي أَهْدِكَ صِرَاطًا سَوِيًّا
Man sama baay, man dey am naa ci xam-xam loo xam ne yaw amoo ko ; topp ma, kon dey danaa la gindi, [teg la] ci yoon wu jub wa.
44يَا أَبَتِ لَا تَعْبُدِ الشَّيْطَانَ ۖ إِنَّ الشَّيْطَانَ كَانَ لِلرَّحْمَٰنِ عَصِيًّا
Yaw sama baay, bul di jaamu Séytaane, ndax Séytaane kat moykatub Yàlla la.
45يَا أَبَتِ إِنِّي أَخَافُ أَن يَمَسَّكَ عَذَابٌ مِّنَ الرَّحْمَٰنِ فَتَكُونَ لِلشَّيْطَانِ وَلِيًّا
Yaw sama baay, man dey ragal naa mbugalum Yàlla dal la nga fay lëkkook Séytaane”.
46قَالَ أَرَاغِبٌ أَنتَ عَنْ آلِهَتِي يَا إِبْرَاهِيمُ ۖ لَئِن لَّمْ تَنتَهِ لَأَرْجُمَنَّكَ ۖ وَاهْجُرْنِي مَلِيًّا
Baayam daldi ne ko : "Moo Ibraahiima, ndax dangaa bañ sama yàlla jii ? Soo bàyyilwul [lii ngay wax], danaa la yóori xeer [ba nga dee], te sax génnal topp sa një”.
47قَالَ سَلَامٌ عَلَيْكَ ۖ سَأَسْتَغْفِرُ لَكَ رَبِّي ۖ إِنَّهُ كَانَ بِي حَفِيًّا
[Ibraahiima] ne ko : “Yal na jàmm nekk ci yaw”. “Danaa la sàkkul njéggal ci sama Boroom ndax Ku ma teral la.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — Maryam 45

Simoore Maryam Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yaw sama baay, man dey ragal naa mbugalum Yàlla dal…

Simoore Aaya 45/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers