Maryam · 50/98
Tekki Waxtaan — Maryam
وَوَهَبْنَا لَهُم مِّن رَّحْمَتِنَا وَجَعَلْنَا لَهُمْ لِسَانَ صِدْقٍ عَلِيًّا ۝٥٠
Wa wahabnaa lahum mirrahmatinaa wa ja`alnaa lahum lisaana sidqin `aliyyaa
📖 Tekkim Wolof
Nu daldi leen may ci Sunu yërmaande, defal leen làmmiñ wu dëggu wu kawe.
🎧 Dégg

📜 Aaya 48-52 — Maryam

48وَأَعْتَزِلُكُمْ وَمَا تَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ وَأَدْعُو رَبِّي عَسَىٰ أَلَّا أَكُونَ بِدُعَاءِ رَبِّي شَقِيًّا
Danaa leen beru yéen ak ñi ngeen di jaamu te du Yàlla, tey ñaan sama Boroom. Yaakaar naa ne duma xañ”.
49فَلَمَّا اعْتَزَلَهُمْ وَمَا يَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ وَهَبْنَا لَهُ إِسْحَاقَ وَيَعْقُوبَ ۖ وَكُلًّا جَعَلْنَا نَبِيًّا
Ba mu leen beroo, [dëddu leen] ñoom ak la ñu daan jaamu te duñu Yàlla, booba Lanu ko may Isaaqa ak Yànqooba ; def leen ñoom ñaar ñépp ñu di ay Yonent.
50وَوَهَبْنَا لَهُم مِّن رَّحْمَتِنَا وَجَعَلْنَا لَهُمْ لِسَانَ صِدْقٍ عَلِيًّا
Nu daldi leen may ci Sunu yërmaande, defal leen làmmiñ wu dëggu wu kawe.
51وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ مُوسَىٰ ۚ إِنَّهُ كَانَ مُخْلَصًا وَكَانَ رَسُولًا نَّبِيًّا
[Fàttalikul] Muusaa ca Téere ba. Moom dey ku sellal la woon, di ku ñu soloo, di ab Yonent.
52وَنَادَيْنَاهُ مِن جَانِبِ الطُّورِ الْأَيْمَنِ وَقَرَّبْنَاهُ نَجِيًّا
Woo Nanu ko ca wetug ndeyjooru tundu Sinaay wa, sësloo ko rëkk ci Nun.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
50Aaya

Tekki — Maryam 50

Simoore Maryam Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu daldi leen may ci Sunu yërmaande, defal leen làmmiñ…

Simoore Aaya 50/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers