Maryam · 56/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ إِدْرِيسَ ۚ إِنَّهُ كَانَ صِدِّيقًا نَّبِيًّا ۝٥٦
Wazkur fil Kitaabi Idrees; innahoo kaana siddeeqan Nabiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Fàttalikul Idriisa ca Téere ba. Moom dey ku dëddu la woon, di ab Yonent.

🎧 Dégg


📜 Aaya 54-58 — Simoore Maryam

54وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ إِسْمَاعِيلَ ۚ إِنَّهُ كَانَ صَادِقَ الْوَعْدِ وَكَانَ رَسُولًا نَّبِيًّا
[Fàttalikul] Ismayla ca Téere ba. Doonoon na boroom dégg bu dëggu ; dib Yonent.
55وَكَانَ يَأْمُرُ أَهْلَهُ بِالصَّلَاةِ وَالزَّكَاةِ وَكَانَ عِندَ رَبِّهِ مَرْضِيًّا
Daa woon na digal njabootam taxawal julli ak asaka, di ku amoom ngërëmul Yàlla.
56وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ إِدْرِيسَ ۚ إِنَّهُ كَانَ صِدِّيقًا نَّبِيًّا
Fàttalikul Idriisa ca Téere ba. Moom dey ku dëddu la woon, di ab Yonent.
57وَرَفَعْنَاهُ مَكَانًا عَلِيًّا
Mayoon Nanu ko daraja ju kawe.
58أُولَٰئِكَ الَّذِينَ أَنْعَمَ اللَّهُ عَلَيْهِم مِّنَ النَّبِيِّينَ مِن ذُرِّيَّةِ آدَمَ وَمِمَّنْ حَمَلْنَا مَعَ نُوحٍ وَمِن ذُرِّيَّةِ إِبْرَاهِيمَ وَإِسْرَائِيلَ وَمِمَّنْ هَدَيْنَا وَاجْتَبَيْنَا ۚ إِذَا تُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ آيَاتُ الرَّحْمَٰنِ خَرُّوا سُجَّدًا وَبُكِيًّا ۩
Ñooña ñooy ña nga xam ne Yàlla wàcceloon na leen xéewalam ca Yonent ya, ak ca sëti Aadama, ak ña àndoon ak Nooh ca gaal ga, ak ña bokk ca sëti Ibraahiima ak ca ñu Nu gindi woon te tànnoon leen. Te saa su ñu mësaa na jàng kàdduy Yàlla fa ñoom, ñu rot sujjóot boole kooki jooy.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
56Aaya

Tekki — Maryam 56

Simoore Maryam Aaya 56 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Fàttalikul Idriisa ca Téere ba. Moom dey ku dëddu la…

Simoore Aaya 56/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 54–58. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers