Maryam · 55/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
وَكَانَ يَأْمُرُ أَهْلَهُ بِالصَّلَاةِ وَالزَّكَاةِ وَكَانَ عِندَ رَبِّهِ مَرْضِيًّا ۝٥٥
Wa kaana yaamuru ahlahoo bis Salaati waz zakaati wa kaana `inda Rabbihee mardiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Daa woon na digal njabootam taxawal julli ak asaka, di ku amoom ngërëmul Yàlla.

🎧 Dégg


📜 Aaya 53-57 — Simoore Maryam

53وَوَهَبْنَا لَهُ مِن رَّحْمَتِنَا أَخَاهُ هَارُونَ نَبِيًّا
Nu daldi koy may ci Sunu yërmaande, defal ko mbokkam ma Aaruuna mu di ab Yonent.
54وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ إِسْمَاعِيلَ ۚ إِنَّهُ كَانَ صَادِقَ الْوَعْدِ وَكَانَ رَسُولًا نَّبِيًّا
[Fàttalikul] Ismayla ca Téere ba. Doonoon na boroom dégg bu dëggu ; dib Yonent.
55وَكَانَ يَأْمُرُ أَهْلَهُ بِالصَّلَاةِ وَالزَّكَاةِ وَكَانَ عِندَ رَبِّهِ مَرْضِيًّا
Daa woon na digal njabootam taxawal julli ak asaka, di ku amoom ngërëmul Yàlla.
56وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ إِدْرِيسَ ۚ إِنَّهُ كَانَ صِدِّيقًا نَّبِيًّا
Fàttalikul Idriisa ca Téere ba. Moom dey ku dëddu la woon, di ab Yonent.
57وَرَفَعْنَاهُ مَكَانًا عَلِيًّا
Mayoon Nanu ko daraja ju kawe.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
55Aaya

Tekki — Maryam 55

Simoore Maryam Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Daa woon na digal njabootam taxawal julli ak asaka, di…

Simoore Aaya 55/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 53–57. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers