Al-Baqara · 11/286
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Baqara
وَإِذَا قِيلَ لَهُمْ لَا تُفْسِدُوا فِي الْأَرْضِ قَالُوا إِنَّمَا نَحْنُ مُصْلِحُونَ ۝١١
Wa izaa qeela lahum laa tufsidoo fil ardi qaalo innamaa nahnu muslihoon
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu leen waxee : 'Buleen di yàq ci suuf si ', ñu ne : 'Nun way-defar lanu ! '

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Simoore Al-Baqara

9يُخَادِعُونَ اللَّهَ وَالَّذِينَ آمَنُوا وَمَا يَخْدَعُونَ إِلَّا أَنفُسَهُمْ وَمَا يَشْعُرُونَ
Dañuy jéem a nax Yàlla ak way-gëm ñi ; waaye naxuñu lu dul seen bopp, te yëguñu ko.
10فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ فَزَادَهُمُ اللَّهُ مَرَضًا ۖ وَلَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ بِمَا كَانُوا يَكْذِبُونَ
Jàngoroo nekk ci seeni xol (gog sikki-sàkk ak ug naaféq), faf Yàlla yokk leen jàngoro. Mbugal mu metti dana leen dal ngir seenug weddi.
11وَإِذَا قِيلَ لَهُمْ لَا تُفْسِدُوا فِي الْأَرْضِ قَالُوا إِنَّمَا نَحْنُ مُصْلِحُونَ
Bu ñu leen waxee : 'Buleen di yàq ci suuf si ', ñu ne : 'Nun way-defar lanu ! '
12أَلَا إِنَّهُمْ هُمُ الْمُفْسِدُونَ وَلَٰكِن لَّا يَشْعُرُونَ
Déedéet, ñoom ñooña ay yàq-kat lañu, te yëguñu ko.
13وَإِذَا قِيلَ لَهُمْ آمِنُوا كَمَا آمَنَ النَّاسُ قَالُوا أَنُؤْمِنُ كَمَا آمَنَ السُّفَهَاءُ ۗ أَلَا إِنَّهُمْ هُمُ السُّفَهَاءُ وَلَٰكِن لَّا يَعْلَمُونَ
Bu ñu ne leen : “Gëmleen ni nit ñi gëmee”, ñu tontu ne : “Ndax danuy gëm ni dof yi di gëmee ? ” Déedéet, ñoom ñooy diy dof, te xamuñu ko.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
11Aaya

Tekki — Al-Baqara 11

Simoore Al-Baqara Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu leen waxee : 'Buleen di yàq ci suuf…

Simoore Aaya 11/286 — Simoore Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Baqara Dégg, Simoore Al-Baqara Tekki, Simoore Al-Baqara mp3, Simoore Al-Baqara pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers