Al-Baqara · 225/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
لَّا يُؤَاخِذُكُمُ اللَّهُ بِاللَّغْوِ فِي أَيْمَانِكُمْ وَلَٰكِن يُؤَاخِذُكُم بِمَا كَسَبَتْ قُلُوبُكُمْ ۗ وَاللَّهُ غَفُورٌ حَلِيمٌ ۝٢٢٥
Laa yu`aakhi zukumul laahu billaghwi feee aymaa nikum wa laakiny yu`aakhi zukum bimaa kasabat quloo bukum; wallaahu Ghafoorun Haleem
📖 Tekkim Wolof
Yàlla duleen jàppe ngiñ ci kaf : Waaye Dana leen jàppe ngiñ lu seeni xol dëggu. Yàlla jéggalaakoon la te ku lewet la.
🎧 Dégg

📜 Aaya 223-227 — Al-Baqara

223نِسَاؤُكُمْ حَرْثٌ لَّكُمْ فَأْتُوا حَرْثَكُمْ أَنَّىٰ شِئْتُمْ ۖ وَقَدِّمُوا لِأَنفُسِكُمْ ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ وَاعْلَمُوا أَنَّكُم مُّلَاقُوهُ ۗ وَبَشِّرِ الْمُؤْمِنِينَ
Seeni soxna [jabar] seeni tool lañu ; dikkeleen seeni tool ca na mu leen neexee te ngeen jiital ngir seen bopp, buleen fàtte tudd Yàlla. Te ngeen ragal Yàlla te ngeen xam ne dangeen dajeek Moom. Te nanga bégal way-gëm ña !
224وَلَا تَجْعَلُوا اللَّهَ عُرْضَةً لِّأَيْمَانِكُمْ أَن تَبَرُّوا وَتَتَّقُوا وَتُصْلِحُوا بَيْنَ النَّاسِ ۗ وَاللَّهُ سَمِيعٌ عَلِيمٌ
Buleen di giñ ci Yàlla, ba mu nekk gàllankoor gu leen teree def lu baax, walla ragal Yàlla mbaa yéwénal diggante nit ñi. Yàlla kuy dégg la te ku xam la.
225لَّا يُؤَاخِذُكُمُ اللَّهُ بِاللَّغْوِ فِي أَيْمَانِكُمْ وَلَٰكِن يُؤَاخِذُكُم بِمَا كَسَبَتْ قُلُوبُكُمْ ۗ وَاللَّهُ غَفُورٌ حَلِيمٌ
Yàlla duleen jàppe ngiñ ci kaf : Waaye Dana leen jàppe ngiñ lu seeni xol dëggu. Yàlla jéggalaakoon la te ku lewet la.
226لِّلَّذِينَ يُؤْلُونَ مِن نِّسَائِهِمْ تَرَبُّصُ أَرْبَعَةِ أَشْهُرٍ ۖ فَإِن فَاءُوا فَإِنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Ña giñ ci [beru] seeni jabar, nangeen leen muñal ñeenti weer. Bu ñu delloo ginnaaw [ca la ñu giñoon], Yàlla Jéggalaakoon la te Jaglewaakoon la !
227وَإِنْ عَزَمُوا الطَّلَاقَ فَإِنَّ اللَّهَ سَمِيعٌ عَلِيمٌ
Bu ñu dogoo ci pase, Yàlla kuy dégg la te ku xam la.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
225Aaya

Tekki — Al-Baqara 225

Simoore Al-Baqara Aaya 225 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla duleen jàppe ngiñ ci kaf : Waaye Dana leen…

Simoore Aaya 225/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 223–227. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers