Al-Baqara · 270/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
وَمَا أَنفَقْتُم مِّن نَّفَقَةٍ أَوْ نَذَرْتُم مِّن نَّذْرٍ فَإِنَّ اللَّهَ يَعْلَمُهُ ۗ وَمَا لِلظَّالِمِينَ مِنْ أَنصَارٍ ۝٢٧٠
Wa maaa anfaqtum min nafaqatin aw nazartum min nazrin fa innal laaha ya`lamuh; wa maa lizzaalimeena min ansaar
📖 Tekkim Wolof
Li ngeen joxe mu génn walla ngeen nisar ko , Yàlla xam na ko. Ñiy tooñ, duñu am ndimbal !

🎧 Dégg


📜 Aaya 268-272 — Al-Baqara

268الشَّيْطَانُ يَعِدُكُمُ الْفَقْرَ وَيَأْمُرُكُم بِالْفَحْشَاءِ ۖ وَاللَّهُ يَعِدُكُم مَّغْفِرَةً مِّنْهُ وَفَضْلًا ۗ وَاللَّهُ وَاسِعٌ عَلِيمٌ
Séytaane, ag ñàkk la leen di dig, di leen xiir ci moy ;Yàlla nag, jéggal la leen di dig ak wërsëg wu bawoo ca Moom. Yàlla ku yaatu, ku xam la.
269يُؤْتِي الْحِكْمَةَ مَن يَشَاءُ ۚ وَمَن يُؤْتَ الْحِكْمَةَ فَقَدْ أُوتِيَ خَيْرًا كَثِيرًا ۗ وَمَا يَذَّكَّرُ إِلَّا أُولُو الْأَلْبَابِ
Mooy jox ku ko soob xel mu rëy, rafet . Ku Mu jox xel mu rafet, jox na ko njariñ lu rëy. Te boroom xel ya rekk ay waaru.
270وَمَا أَنفَقْتُم مِّن نَّفَقَةٍ أَوْ نَذَرْتُم مِّن نَّذْرٍ فَإِنَّ اللَّهَ يَعْلَمُهُ ۗ وَمَا لِلظَّالِمِينَ مِنْ أَنصَارٍ
Li ngeen joxe mu génn walla ngeen nisar ko , Yàlla xam na ko. Ñiy tooñ, duñu am ndimbal !
271إِن تُبْدُوا الصَّدَقَاتِ فَنِعِمَّا هِيَ ۖ وَإِن تُخْفُوهَا وَتُؤْتُوهَا الْفُقَرَاءَ فَهُوَ خَيْرٌ لَّكُمْ ۚ وَيُكَفِّرُ عَنكُم مِّن سَيِّئَاتِكُمْ ۗ وَاللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ خَبِيرٌ
Bu ngeen feeñalee seeni sarax, baax na ; bu ngeen ko nëbbee, jox ko wax-ñéew ji doole ya nag, moo gën ci yéen. Danañu leen jéggal ci seeni ñaawtéef [ci soppi ko aw yiw]. Yàlla ku deñ-kumpa la ci li ngeen di def.
272۞ لَّيْسَ عَلَيْكَ هُدَاهُمْ وَلَٰكِنَّ اللَّهَ يَهْدِي مَن يَشَاءُ ۗ وَمَا تُنفِقُوا مِنْ خَيْرٍ فَلِأَنفُسِكُمْ ۚ وَمَا تُنفِقُونَ إِلَّا ابْتِغَاءَ وَجْهِ اللَّهِ ۚ وَمَا تُنفِقُوا مِنْ خَيْرٍ يُوَفَّ إِلَيْكُمْ وَأَنتُمْ لَا تُظْلَمُونَ
Seenug njub waru la, waaye Yàlla mooy jubal ku ko soob. Lu ngeen joxe ci alal, seen bopp ngeen ko defal, dungeen joxe lu dul ngir jëmmi Yàlla. Xamleen ne li ngeen joxe ci alal dangeen ca jotaat. Te duñu leen ca deseel dara.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
270Aaya

Tekki — Al-Baqara 270

Simoore Al-Baqara Aaya 270 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Li ngeen joxe mu génn walla ngeen nisar ko ,…

Simoore Aaya 270/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 268–272. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers