Al-Baqara · 97/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
قُلْ مَن كَانَ عَدُوًّا لِّجِبْرِيلَ فَإِنَّهُ نَزَّلَهُ عَلَىٰ قَلْبِكَ بِإِذْنِ اللَّهِ مُصَدِّقًا لِّمَا بَيْنَ يَدَيْهِ وَهُدًى وَبُشْرَىٰ لِلْمُؤْمِنِينَ ۝٩٧
Qul man kaana `aduwwal li Jibreela fainnahoo nazzalahoo `alaa qalbika bi iznil laahi musaddiqal limaa baina yadihi wa hudanw wa bushraa lilmu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Ku noonu Jibriil it moom moo wàcce Alxuraan ci sa xol ci ndigalu Yàlla, muy dëggal la ko jiitu, mu di ag njub ak mbégte ci way-gëm ñi”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 95-99 — Al-Baqara

95وَلَن يَتَمَنَّوْهُ أَبَدًا بِمَا قَدَّمَتْ أَيْدِيهِمْ ۗ وَاللَّهُ عَلِيمٌ بِالظَّالِمِينَ
Duñu ko mébét mukk ngir la seen yoxo ya jëf [ci lu bon]. Yàlla ku xam la way-tooñ ña.
96وَلَتَجِدَنَّهُمْ أَحْرَصَ النَّاسِ عَلَىٰ حَيَاةٍ وَمِنَ الَّذِينَ أَشْرَكُوا ۚ يَوَدُّ أَحَدُهُمْ لَوْ يُعَمَّرُ أَلْفَ سَنَةٍ وَمَا هُوَ بِمُزَحْزِحِهِ مِنَ الْعَذَابِ أَن يُعَمَّرَ ۗ وَاللَّهُ بَصِيرٌ بِمَا يَعْمَلُونَ
Wóor na ne danga leen fekk ñoom [Yahuud ya] ñu nekk di ñu gën a xér ci nit ñi ci bëgg dundu, ak ci ñiy bokkaale. [Danga ca gis] ca ñoom ku ne siiw ñu guddal fanam junniy at. Waaye du ko soreel mbugal ma! Dundu gu guddu googu Yàllaa ngi ne jàkk ci li ñuy def.
97قُلْ مَن كَانَ عَدُوًّا لِّجِبْرِيلَ فَإِنَّهُ نَزَّلَهُ عَلَىٰ قَلْبِكَ بِإِذْنِ اللَّهِ مُصَدِّقًا لِّمَا بَيْنَ يَدَيْهِ وَهُدًى وَبُشْرَىٰ لِلْمُؤْمِنِينَ
Neel : “Ku noonu Jibriil it moom moo wàcce Alxuraan ci sa xol ci ndigalu Yàlla, muy dëggal la ko jiitu, mu di ag njub ak mbégte ci way-gëm ñi”.
98مَن كَانَ عَدُوًّا لِّلَّهِ وَمَلَائِكَتِهِ وَرُسُلِهِ وَجِبْرِيلَ وَمِيكَالَ فَإِنَّ اللَّهَ عَدُوٌّ لِّلْكَافِرِينَ
[Neel : ] “Ku weddi Yàlla ba noonu ko ak i Malaakaam ak i Yonentam ak Jibriil ak Miikaayil... Yàlla it di ab noonam rekk”.
99وَلَقَدْ أَنزَلْنَا إِلَيْكَ آيَاتٍ بَيِّنَاتٍ ۖ وَمَا يَكْفُرُ بِهَا إِلَّا الْفَاسِقُونَ
Bir na ne, wàcce Nanu ci yaw ay kàddu yu leer nàññ, yu kenn du ko weddi ku dul ab saay- saay.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
97Aaya

Tekki — Al-Baqara 97

Simoore Al-Baqara Aaya 97 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Ku noonu Jibriil it moom moo wàcce Alxuraan…

Simoore Aaya 97/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 95–99. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers