Al-Baqara · 98/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
مَن كَانَ عَدُوًّا لِّلَّهِ وَمَلَائِكَتِهِ وَرُسُلِهِ وَجِبْرِيلَ وَمِيكَالَ فَإِنَّ اللَّهَ عَدُوٌّ لِّلْكَافِرِينَ ٩٨
Transliteration
Man kaana `aduwwal lillaahi wa malaaa`ikatihee wa Rusulihee wa Jibreela wa Meekaala fa innal laaha `aduwwul lilkaafireen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
[Neel : ] “Ku weddi Yàlla ba noonu ko ak i Malaakaam ak i Yonentam ak Jibriil ak Miikaayil... Yàlla it di ab noonam rekk”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 96-100 — Al-Baqara
96وَلَتَجِدَنَّهُمْ أَحْرَصَ النَّاسِ عَلَىٰ حَيَاةٍ وَمِنَ الَّذِينَ أَشْرَكُوا ۚ يَوَدُّ أَحَدُهُمْ لَوْ يُعَمَّرُ أَلْفَ سَنَةٍ وَمَا هُوَ بِمُزَحْزِحِهِ مِنَ الْعَذَابِ أَن يُعَمَّرَ ۗ وَاللَّهُ بَصِيرٌ بِمَا يَعْمَلُونَ
Wóor na ne danga leen fekk ñoom [Yahuud ya] ñu nekk di ñu gën a xér ci nit ñi ci bëgg dundu, ak ci ñiy bokkaale. [Danga ca gis] ca ñoom ku ne siiw ñu guddal fanam junniy at. Waaye du ko soreel mbugal ma! Dundu gu guddu googu Yàllaa ngi ne jàkk ci li ñuy def.
97قُلْ مَن كَانَ عَدُوًّا لِّجِبْرِيلَ فَإِنَّهُ نَزَّلَهُ عَلَىٰ قَلْبِكَ بِإِذْنِ اللَّهِ مُصَدِّقًا لِّمَا بَيْنَ يَدَيْهِ وَهُدًى وَبُشْرَىٰ لِلْمُؤْمِنِينَ
Neel : “Ku noonu Jibriil it moom moo wàcce Alxuraan ci sa xol ci ndigalu Yàlla, muy dëggal la ko jiitu, mu di ag njub ak mbégte ci way-gëm ñi”.
98مَن كَانَ عَدُوًّا لِّلَّهِ وَمَلَائِكَتِهِ وَرُسُلِهِ وَجِبْرِيلَ وَمِيكَالَ فَإِنَّ اللَّهَ عَدُوٌّ لِّلْكَافِرِينَ
[Neel : ] “Ku weddi Yàlla ba noonu ko ak i Malaakaam ak i Yonentam ak Jibriil ak Miikaayil... Yàlla it di ab noonam rekk”.
99وَلَقَدْ أَنزَلْنَا إِلَيْكَ آيَاتٍ بَيِّنَاتٍ ۖ وَمَا يَكْفُرُ بِهَا إِلَّا الْفَاسِقُونَ
Bir na ne, wàcce Nanu ci yaw ay kàddu yu leer nàññ, yu kenn du ko weddi ku dul ab saay- saay.
100أَوَكُلَّمَا عَاهَدُوا عَهْدًا نَّبَذَهُ فَرِيقٌ مِّنْهُم ۚ بَلْ أَكْثَرُهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Moo ndax saa su ñu kóllaranteek [Yàlla] ab dëel, kurél ci ñoom firi ko? Li wér mooy li ëpp ci ñoom gëmuñu.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
98Aaya
Tekki — Al-Baqara 98
Simoore Al-Baqara Aaya 98 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Neel : ] “Ku weddi Yàlla ba noonu ko ak…Simoore Aaya 98/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 96–100. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








