Taha · 49/135
Tekki Waxtaan — Taha
قَالَ فَمَن رَّبُّكُمَا يَا مُوسَىٰ ٤٩
Transliteration
Qaala famar Rabbu kumaa yaa Moosa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
[Firawna] ne leen : “Waaw yéen ñaar kan moo di seen Boroom ? ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 47-51 — Taha
47فَأْتِيَاهُ فَقُولَا إِنَّا رَسُولَا رَبِّكَ فَأَرْسِلْ مَعَنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ وَلَا تُعَذِّبْهُمْ ۖ قَدْ جِئْنَاكَ بِآيَةٍ مِّن رَّبِّكَ ۖ وَالسَّلَامُ عَلَىٰ مَنِ اتَّبَعَ الْهُدَىٰ
Demleen fa Moom ne ko : “Ñun ñaar ñii ndawi Yàlla lanu. Delloo nu waa Banii-Israayiila [ñi nga jàppe jaam] te buleen mbugalati. Ndax indi nanu ci yaw ay kàddu yu jóge fa sa Boroom. Te jàmmi Yàlla nay nekk ca kay topp njub ga !
48إِنَّا قَدْ أُوحِيَ إِلَيْنَا أَنَّ الْعَذَابَ عَلَىٰ مَن كَذَّبَ وَتَوَلَّىٰ
Xamalees nanu ne : képp ku weddi te dummóoyu [kàdduy Yàlla], kooka mbugal dana ko dal”.
49قَالَ فَمَن رَّبُّكُمَا يَا مُوسَىٰ
[Firawna] ne leen : “Waaw yéen ñaar kan moo di seen Boroom ? ”
50قَالَ رَبُّنَا الَّذِي أَعْطَىٰ كُلَّ شَيْءٍ خَلْقَهُ ثُمَّ هَدَىٰ
Mu ne ko : “Sunu Boroom, Moo sos mbindéef yépp, te Mooy gindee”.
51قَالَ فَمَا بَالُ الْقُرُونِ الْأُولَىٰ
[Firawna] ne ko : “Waaw xeet ya jiitu woon, ñoom luy xala doon seenub àtte ? ”.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
49Aaya
Tekki — Taha 49
Simoore Taha Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Firawna] ne leen : “Waaw yéen ñaar kan moo di…Simoore Aaya 49/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








