Taha · 50/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
قَالَ رَبُّنَا الَّذِي أَعْطَىٰ كُلَّ شَيْءٍ خَلْقَهُ ثُمَّ هَدَىٰ ۝٥٠
Qaala Rabbunal lazeee a`taa kulla shai`in khalqahoo summa hadaa
📖 Tekkim Wolof
Mu ne ko : “Sunu Boroom, Moo sos mbindéef yépp, te Mooy gindee”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 48-52 — Simoore Taha

48إِنَّا قَدْ أُوحِيَ إِلَيْنَا أَنَّ الْعَذَابَ عَلَىٰ مَن كَذَّبَ وَتَوَلَّىٰ
Xamalees nanu ne : képp ku weddi te dummóoyu [kàdduy Yàlla], kooka mbugal dana ko dal”.
49قَالَ فَمَن رَّبُّكُمَا يَا مُوسَىٰ
[Firawna] ne leen : “Waaw yéen ñaar kan moo di seen Boroom ? ”
50قَالَ رَبُّنَا الَّذِي أَعْطَىٰ كُلَّ شَيْءٍ خَلْقَهُ ثُمَّ هَدَىٰ
Mu ne ko : “Sunu Boroom, Moo sos mbindéef yépp, te Mooy gindee”.
51قَالَ فَمَا بَالُ الْقُرُونِ الْأُولَىٰ
[Firawna] ne ko : “Waaw xeet ya jiitu woon, ñoom luy xala doon seenub àtte ? ”.
52قَالَ عِلْمُهَا عِندَ رَبِّي فِي كِتَابٍ ۖ لَّا يَضِلُّ رَبِّي وَلَا يَنسَى
Mu ne ko : “Seeni mbir a nga ca Téere ba fa sa Boroom. Sama Boroom du juum, du fàtte.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
50Aaya

Tekki — Taha 50

Simoore Taha Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne ko : “Sunu Boroom, Moo sos mbindéef yépp,…

Simoore Aaya 50/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers