Al-Anbiya · 30/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
أَوَلَمْ يَرَ الَّذِينَ كَفَرُوا أَنَّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ كَانَتَا رَتْقًا فَفَتَقْنَاهُمَا ۖ وَجَعَلْنَا مِنَ الْمَاءِ كُلَّ شَيْءٍ حَيٍّ ۖ أَفَلَا يُؤْمِنُونَ ۝٣٠
Awalam yaral lazeena kafarooo annas samaawaati wal arda kaanataa ratqan faftaqnaahumaa wa ja`alnaa minal maaa`i kulla shai`in haiyin afalaa yu`minoon
📖 Tekkim Wolof
Ndax ña weddi dañoo gisul ne asamaan yi ak suuf si dañoo taqaloodef [benn dank] ? Nu daldi leen téqale, te Nu sose ndox lépp luy dundu. Moo ndax dañu dul gëm ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 28-32 — Simoore Al-Anbiya

28يَعْلَمُ مَا بَيْنَ أَيْدِيهِمْ وَمَا خَلْفَهُمْ وَلَا يَشْفَعُونَ إِلَّا لِمَنِ ارْتَضَىٰ وَهُم مِّنْ خَشْيَتِهِ مُشْفِقُونَ
Xam na li nekk ci seen kanam ak li nekk ci seen ginnaaw. Te duñu rammu lu dul ka Ko neex, te ñoom ña nga ca tiitaangey ragal Yàlla.
29۞ وَمَن يَقُلْ مِنْهُمْ إِنِّي إِلَٰهٌ مِّن دُونِهِ فَذَٰلِكَ نَجْزِيهِ جَهَنَّمَ ۚ كَذَٰلِكَ نَجْزِي الظَّالِمِينَ
Te ku ca waxoon bokk ca ñoom ne : “Man yàlla laa, ju dul Moom”. Loola Safara la Nu ko koy feyee. Te noona it la Nuy feye tooñkat ya.
30أَوَلَمْ يَرَ الَّذِينَ كَفَرُوا أَنَّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ كَانَتَا رَتْقًا فَفَتَقْنَاهُمَا ۖ وَجَعَلْنَا مِنَ الْمَاءِ كُلَّ شَيْءٍ حَيٍّ ۖ أَفَلَا يُؤْمِنُونَ
Ndax ña weddi dañoo gisul ne asamaan yi ak suuf si dañoo taqaloodef [benn dank] ? Nu daldi leen téqale, te Nu sose ndox lépp luy dundu. Moo ndax dañu dul gëm ?
31وَجَعَلْنَا فِي الْأَرْضِ رَوَاسِيَ أَن تَمِيدَ بِهِمْ وَجَعَلْنَا فِيهَا فِجَاجًا سُبُلًا لَّعَلَّهُمْ يَهْتَدُونَ
Te def Nanu ci biir suuf si ay tundi doj, ngir mu bañ a baj-baji ak ñoom. Te def Nanu ci ay yoon ngir ñu mën a gindiku.
32وَجَعَلْنَا السَّمَاءَ سَقْفًا مَّحْفُوظًا ۖ وَهُمْ عَنْ آيَاتِهَا مُعْرِضُونَ
Te def Nanu asamaan si mu nekk am téeg mu Nu wattu. Te ñoom ñangay dëddu Sunuy kéemtaan [bañ leen a seetlu].
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
30Aaya

Tekki — Al-Anbiya 30

Simoore Al-Anbiya Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax ña weddi dañoo gisul ne asamaan yi ak suuf…

Simoore Aaya 30/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers