Al-Anbiya · 57/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
وَتَاللَّهِ لَأَكِيدَنَّ أَصْنَامَكُم بَعْدَ أَن تُوَلُّوا مُدْبِرِينَ ۝٥٧
Wa tallaahi la akeedanna asnaamakum ba`da an tuwalloo mudbireen
📖 Tekkim Wolof
Te waat naa ci Yàlla ! Ne danaa fexeel seen xërëm yi ci seen ginnaaw, bu ngeen dëddoo”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 55-59 — Simoore Al-Anbiya

55قَالُوا أَجِئْتَنَا بِالْحَقِّ أَمْ أَنتَ مِنَ اللَّاعِبِينَ
Ñu ne ko : “Ndax li nga nu dig dëgg la ci yaw walla dangay kaf ? ”.
56قَالَ بَل رَّبُّكُمْ رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ الَّذِي فَطَرَهُنَّ وَأَنَا عَلَىٰ ذَٰلِكُم مِّنَ الشَّاهِدِينَ
Mu ne déedéet : “Seen Boroom mooy Boroom asamaan yi ak suuf si, te Moo leen sàkk. Te man dey bokk naa ci ñiy seede loolu ci yéen.
57وَتَاللَّهِ لَأَكِيدَنَّ أَصْنَامَكُم بَعْدَ أَن تُوَلُّوا مُدْبِرِينَ
Te waat naa ci Yàlla ! Ne danaa fexeel seen xërëm yi ci seen ginnaaw, bu ngeen dëddoo”.
58فَجَعَلَهُمْ جُذَاذًا إِلَّا كَبِيرًا لَّهُمْ لَعَلَّهُمْ إِلَيْهِ يَرْجِعُونَ
Mu dàggate leen ba mu des xërëm bu mag ba. Ngir xéy-na mu mën cee delloo [seeni xel].
59قَالُوا مَن فَعَلَ هَٰذَا بِآلِهَتِنَا إِنَّهُ لَمِنَ الظَّالِمِينَ
Ñu ne : “Ku def lii sunu yàlla yi ? Kooka dey bokk na ca tooñkat ya”.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
57Aaya

Tekki — Al-Anbiya 57

Simoore Al-Anbiya Aaya 57 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te waat naa ci Yàlla ! Ne danaa fexeel seen…

Simoore Aaya 57/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 55–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers