Al-Anbiya · 77/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
وَنَصَرْنَاهُ مِنَ الْقَوْمِ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمَ سَوْءٍ فَأَغْرَقْنَاهُمْ أَجْمَعِينَ ٧٧
Transliteration
Wa nasarnaahu minal qawmil lazeena kazzaboo bi Aayaatinaa; innahum kkaanoo qawma saw`in fa-aghraq naahum ajma`een
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
te Nu dimbali woon ko ca nit ña weddi woon Sunuy kàddu. Ñoom aw nit ñu bon lañu woon. Nu daldi leen labal ñoom ñépp.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 75-79 — Al-Anbiya
75وَأَدْخَلْنَاهُ فِي رَحْمَتِنَا ۖ إِنَّهُ مِنَ الصَّالِحِينَ
Dugal Nanu ko ci Sunu yërmaande. Te moom bokk na ca ñu sell ña.
76وَنُوحًا إِذْ نَادَىٰ مِن قَبْلُ فَاسْتَجَبْنَا لَهُ فَنَجَّيْنَاهُ وَأَهْلَهُ مِنَ الْكَرْبِ الْعَظِيمِ
Ak Nooh itam, [fàttalikul] ba mu wootee ca lu jiitu. Nu dal koy wuyyu te musaloon ko, mook njabootam, ca njàqare ju rëy ja,
77وَنَصَرْنَاهُ مِنَ الْقَوْمِ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمَ سَوْءٍ فَأَغْرَقْنَاهُمْ أَجْمَعِينَ
te Nu dimbali woon ko ca nit ña weddi woon Sunuy kàddu. Ñoom aw nit ñu bon lañu woon. Nu daldi leen labal ñoom ñépp.
78وَدَاوُودَ وَسُلَيْمَانَ إِذْ يَحْكُمَانِ فِي الْحَرْثِ إِذْ نَفَشَتْ فِيهِ غَنَمُ الْقَوْمِ وَكُنَّا لِحُكْمِهِمْ شَاهِدِينَ
Ak Daawuda, ak Suleymaan, [fàttalikul] ba Nu àttee mbirum mbéy ma gàtti nit ñu yàqoon [ruur]. Te teewoon fa seen àtte ba.
79فَفَهَّمْنَاهَا سُلَيْمَانَ ۚ وَكُلًّا آتَيْنَا حُكْمًا وَعِلْمًا ۚ وَسَخَّرْنَا مَعَ دَاوُودَ الْجِبَالَ يُسَبِّحْنَ وَالطَّيْرَ ۚ وَكُنَّا فَاعِلِينَ
Déggloo Nanu Suleymaan àtte ba. Te ñoom ñaar ñépp mayoon Nanu leen ràññee dëgg ak xam-xam. Te tàggatoon Nanu tundi doj ak njanaaw ya ñu àndak Daawuda di Nu sàbbaal. Te Nun noo ko defoon.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
77Aaya
Tekki — Al-Anbiya 77
Simoore Al-Anbiya Aaya 77 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te Nu dimbali woon ko ca nit ña weddi woon…Simoore Aaya 77/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 75–79. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








