Al-Anbiya · 81/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
وَلِسُلَيْمَانَ الرِّيحَ عَاصِفَةً تَجْرِي بِأَمْرِهِ إِلَى الْأَرْضِ الَّتِي بَارَكْنَا فِيهَا ۚ وَكُنَّا بِكُلِّ شَيْءٍ عَالِمِينَ ۝٨١
Wa li Sulaimaanar reeha `aasifatan tajree bi amriheee ilal ardil latee baaraknaa feehaa; wa kunnaa bikulli shai`in `aalimeen
📖 Tekkim Wolof
Suleymaan tàggatal Nanu ko ngelaw luy ràddi, di daw ci ndigalam, mu jëm ci suuf su Nu barkeel. Te kat Nun xam Nanu lépp lëf,

🎧 Dégg


📜 Aaya 79-83 — Simoore Al-Anbiya

79فَفَهَّمْنَاهَا سُلَيْمَانَ ۚ وَكُلًّا آتَيْنَا حُكْمًا وَعِلْمًا ۚ وَسَخَّرْنَا مَعَ دَاوُودَ الْجِبَالَ يُسَبِّحْنَ وَالطَّيْرَ ۚ وَكُنَّا فَاعِلِينَ
Déggloo Nanu Suleymaan àtte ba. Te ñoom ñaar ñépp mayoon Nanu leen ràññee dëgg ak xam-xam. Te tàggatoon Nanu tundi doj ak njanaaw ya ñu àndak Daawuda di Nu sàbbaal. Te Nun noo ko defoon.
80وَعَلَّمْنَاهُ صَنْعَةَ لَبُوسٍ لَّكُمْ لِتُحْصِنَكُم مِّن بَأْسِكُمْ ۖ فَهَلْ أَنتُمْ شَاكِرُونَ
Te jàngal Nanu ko ràbbiinu mbubbi koŋ ngir mu musal leen ci seen ngaañ. Moo ndax yéen du ngeen sant [delloo njukkal] ?
81وَلِسُلَيْمَانَ الرِّيحَ عَاصِفَةً تَجْرِي بِأَمْرِهِ إِلَى الْأَرْضِ الَّتِي بَارَكْنَا فِيهَا ۚ وَكُنَّا بِكُلِّ شَيْءٍ عَالِمِينَ
Suleymaan tàggatal Nanu ko ngelaw luy ràddi, di daw ci ndigalam, mu jëm ci suuf su Nu barkeel. Te kat Nun xam Nanu lépp lëf,
82وَمِنَ الشَّيَاطِينِ مَن يَغُوصُونَ لَهُ وَيَعْمَلُونَ عَمَلًا دُونَ ذَٰلِكَ ۖ وَكُنَّا لَهُمْ حَافِظِينَ
te ci jinne yi am na ci ñu ko daan nuural [ci géej te daan nañu ko liggéeyal yeneeni liggéey, te Daan naa leen wattu [Man Yàlla].
83۞ وَأَيُّوبَ إِذْ نَادَىٰ رَبَّهُ أَنِّي مَسَّنِيَ الضُّرُّ وَأَنتَ أَرْحَمُ الرَّاحِمِينَ
Ak Ayuuba [fàttalikul] ba mu woowee Boroomam ne ko : “Man dey mettit dal na ma. Te Yaw yaay gën jaa yërëme yërëmaakoon ya” !
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
81Aaya

Tekki — Al-Anbiya 81

Simoore Al-Anbiya Aaya 81 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Suleymaan tàggatal Nanu ko ngelaw luy ràddi, di daw ci…

Simoore Aaya 81/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 79–83. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers