Al-Mu'minun · 111/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
إِنِّي جَزَيْتُهُمُ الْيَوْمَ بِمَا صَبَرُوا أَنَّهُمْ هُمُ الْفَائِزُونَ ۝١١١
Inee jazaituhumul Yawma bimaa sabarooo annahum humul faaa`izoon
📖 Tekkim Wolof
Bis niki tey feye naa leen ca la ñu doon muñ ; ñoom texe nañu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 109-113 — Simoore Al-Mu'minun

109إِنَّهُ كَانَ فَرِيقٌ مِّنْ عِبَادِي يَقُولُونَ رَبَّنَا آمَنَّا فَاغْفِرْ لَنَا وَارْحَمْنَا وَأَنتَ خَيْرُ الرَّاحِمِينَ
Am na ab kurél bu bokkoon ci sama jaam, daan wax naan : “Boroom sunu, gëm nanu ; jéggal nu te yërëm nu, Yaw yaa di gën ji Yërëmaakoon” ;
110فَاتَّخَذْتُمُوهُمْ سِخْرِيًّا حَتَّىٰ أَنسَوْكُمْ ذِكْرِي وَكُنتُم مِّنْهُمْ تَضْحَكُونَ
ngeen jàppee woon leen ay reetaan ba faf ñu fàbbi leen fàtteloo leen Samay kàddu, dëkkoon ci di leen reetaan rekk.
111إِنِّي جَزَيْتُهُمُ الْيَوْمَ بِمَا صَبَرُوا أَنَّهُمْ هُمُ الْفَائِزُونَ
Bis niki tey feye naa leen ca la ñu doon muñ ; ñoom texe nañu.
112قَالَ كَمْ لَبِثْتُمْ فِي الْأَرْضِ عَدَدَ سِنِينَ
Mu ne leen : “Yéen sax ñaata at ngeen saxoon ci àddina [dundoon] ? ”
113قَالُوا لَبِثْنَا يَوْمًا أَوْ بَعْضَ يَوْمٍ فَاسْأَلِ الْعَادِّينَ
Ñu tontu ne : “Nun daal, benn walla fan yu néew la nu fa saxoon, xam sax laajal limkat yi.”
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
111Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 111

Simoore Al-Mu'minun Aaya 111 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bis niki tey feye naa leen ca la ñu doon…

Simoore Aaya 111/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 109–113. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers