Al-Mu'minun · 112/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
قَالَ كَمْ لَبِثْتُمْ فِي الْأَرْضِ عَدَدَ سِنِينَ ١١٢
Transliteration
Qaala kam labistum fil ardi `adada sineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Mu ne leen : “Yéen sax ñaata at ngeen saxoon ci àddina [dundoon] ? ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 110-114 — Al-Mu'minun
110فَاتَّخَذْتُمُوهُمْ سِخْرِيًّا حَتَّىٰ أَنسَوْكُمْ ذِكْرِي وَكُنتُم مِّنْهُمْ تَضْحَكُونَ
ngeen jàppee woon leen ay reetaan ba faf ñu fàbbi leen fàtteloo leen Samay kàddu, dëkkoon ci di leen reetaan rekk.
111إِنِّي جَزَيْتُهُمُ الْيَوْمَ بِمَا صَبَرُوا أَنَّهُمْ هُمُ الْفَائِزُونَ
Bis niki tey feye naa leen ca la ñu doon muñ ; ñoom texe nañu.
112قَالَ كَمْ لَبِثْتُمْ فِي الْأَرْضِ عَدَدَ سِنِينَ
Mu ne leen : “Yéen sax ñaata at ngeen saxoon ci àddina [dundoon] ? ”
113قَالُوا لَبِثْنَا يَوْمًا أَوْ بَعْضَ يَوْمٍ فَاسْأَلِ الْعَادِّينَ
Ñu tontu ne : “Nun daal, benn walla fan yu néew la nu fa saxoon, xam sax laajal limkat yi.”
114قَالَ إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا قَلِيلًا ۖ لَّوْ أَنَّكُمْ كُنتُمْ تَعْلَمُونَ
Mu ne leen : “As ndiir su néew ngeen fa saxoon. Cëy bu ngeen xamoon”.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
112Aaya
Tekki — Al-Mu'minun 112
Simoore Al-Mu'minun Aaya 112 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne leen : “Yéen sax ñaata at ngeen saxoon…Simoore Aaya 112/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 110–114. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








