Al-Mu'minun · 26/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
قَالَ رَبِّ انصُرْنِي بِمَا كَذَّبُونِ ۝٢٦
Qaala Rabbin surnee bimaa kazzaboon
📖 Tekkim Wolof
[Nooh]ne : “Yaw sama Boroom ! Dimbali ma ci weddi gi ñu ma weddi”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 24-28 — Al-Mu'minun

24فَقَالَ الْمَلَأُ الَّذِينَ كَفَرُوا مِن قَوْمِهِ مَا هَٰذَا إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ يُرِيدُ أَن يَتَفَضَّلَ عَلَيْكُمْ وَلَوْ شَاءَ اللَّهُ لَأَنزَلَ مَلَائِكَةً مَّا سَمِعْنَا بِهَٰذَا فِي آبَائِنَا الْأَوَّلِينَ
Gaa ña weddi woon ca aw nitam di wax naan : “Kii daal nit la ni yéen, dafa bëgg toog ci seen kaw doŋŋ. Te sax bu neexoon Yàlla mu wàcce ay Malaaka. Mësunoo dégg lii ca sunu maam ya jiitu woon.
25إِنْ هُوَ إِلَّا رَجُلٌ بِهِ جِنَّةٌ فَتَرَبَّصُوا بِهِ حَتَّىٰ حِينٍ
Kii daal as waay la su jinne sadd, muñal-leen ko tuuti.
26قَالَ رَبِّ انصُرْنِي بِمَا كَذَّبُونِ
[Nooh]ne : “Yaw sama Boroom ! Dimbali ma ci weddi gi ñu ma weddi”.
27فَأَوْحَيْنَا إِلَيْهِ أَنِ اصْنَعِ الْفُلْكَ بِأَعْيُنِنَا وَوَحْيِنَا فَإِذَا جَاءَ أَمْرُنَا وَفَارَ التَّنُّورُ ۙ فَاسْلُكْ فِيهَا مِن كُلٍّ زَوْجَيْنِ اثْنَيْنِ وَأَهْلَكَ إِلَّا مَن سَبَقَ عَلَيْهِ الْقَوْلُ مِنْهُمْ ۖ وَلَا تُخَاطِبْنِي فِي الَّذِينَ ظَلَمُوا ۖ إِنَّهُم مُّغْرَقُونَ
Nu daldi ko soloo [digal ko] ne ko : “Defaral gaal ci Sunug càmm ak Sunu ndigal. Te saa su Sunu ndigal agsee ba lakkukaayu mburu ba sãs, nanga dugal te bàyyi sag njaboot ak yóllent ci wépp xeet ba mu des ña nga xam ne wax ja jiitu woon na c
28فَإِذَا اسْتَوَيْتَ أَنتَ وَمَن مَّعَكَ عَلَى الْفُلْكِ فَقُلِ الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي نَجَّانَا مِنَ الْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Saa soo duggee ca gaal ga yaak ña nga àndal ba noppi, nanga wax ne : “Cant ñeel na Yàlla Moom mi nu musal ci ay nit yu di ay tooñkat.”
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 26

Simoore Al-Mu'minun Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Nooh]ne : “Yaw sama Boroom ! Dimbali ma ci weddi…

Simoore Aaya 26/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers