Al-Mu'minun · 79/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَهُوَ الَّذِي ذَرَأَكُمْ فِي الْأَرْضِ وَإِلَيْهِ تُحْشَرُونَ ۝٧٩
Wa Huwal lazee zara akum fil ardi wa ilaihi tuhsharoon
📖 Tekkim Wolof
Moom moo leen bàyyi ci kaw suuf si, te dees na leen pang jëme ci Moom.

🎧 Dégg


📜 Aaya 77-81 — Simoore Al-Mu'minun

77حَتَّىٰ إِذَا فَتَحْنَا عَلَيْهِم بَابًا ذَا عَذَابٍ شَدِيدٍ إِذَا هُمْ فِيهِ مُبْلِسُونَ
ba ba kerook Nuy ubbi ci ñoom buntub mbugal mu tar, ñu ne ca xiim.
78وَهُوَ الَّذِي أَنشَأَ لَكُمُ السَّمْعَ وَالْأَبْصَارَ وَالْأَفْئِدَةَ ۚ قَلِيلًا مَّا تَشْكُرُونَ
Moom moo leen sàkkal ag dégg, ak ug gis, ak i xel. Néewaana ngeen gërëm.
79وَهُوَ الَّذِي ذَرَأَكُمْ فِي الْأَرْضِ وَإِلَيْهِ تُحْشَرُونَ
Moom moo leen bàyyi ci kaw suuf si, te dees na leen pang jëme ci Moom.
80وَهُوَ الَّذِي يُحْيِي وَيُمِيتُ وَلَهُ اخْتِلَافُ اللَّيْلِ وَالنَّهَارِ ۚ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Moom mooy dundal, mooy rey ; Moom mooy jàllasante guddeek bëccëg. Ndax dangeen dul xel-lu ?
81بَلْ قَالُوا مِثْلَ مَا قَالَ الْأَوَّلُونَ
Ñoom kay faf dañoo wax rekk la ñu jëkk ña waxoon.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
79Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 79

Simoore Al-Mu'minun Aaya 79 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom moo leen bàyyi ci kaw suuf si, te dees…

Simoore Aaya 79/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 77–81. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers