Al-Mu'minun · 80/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَهُوَ الَّذِي يُحْيِي وَيُمِيتُ وَلَهُ اخْتِلَافُ اللَّيْلِ وَالنَّهَارِ ۚ أَفَلَا تَعْقِلُونَ ۝٨٠
Wa Huwal lazee yuhyee wa yumeetu wa lahukh tilaaful laili wannahaar; afalaa ta`qiloon
📖 Tekkim Wolof
Moom mooy dundal, mooy rey ; Moom mooy jàllasante guddeek bëccëg. Ndax dangeen dul xel-lu ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 78-82 — Simoore Al-Mu'minun

78وَهُوَ الَّذِي أَنشَأَ لَكُمُ السَّمْعَ وَالْأَبْصَارَ وَالْأَفْئِدَةَ ۚ قَلِيلًا مَّا تَشْكُرُونَ
Moom moo leen sàkkal ag dégg, ak ug gis, ak i xel. Néewaana ngeen gërëm.
79وَهُوَ الَّذِي ذَرَأَكُمْ فِي الْأَرْضِ وَإِلَيْهِ تُحْشَرُونَ
Moom moo leen bàyyi ci kaw suuf si, te dees na leen pang jëme ci Moom.
80وَهُوَ الَّذِي يُحْيِي وَيُمِيتُ وَلَهُ اخْتِلَافُ اللَّيْلِ وَالنَّهَارِ ۚ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Moom mooy dundal, mooy rey ; Moom mooy jàllasante guddeek bëccëg. Ndax dangeen dul xel-lu ?
81بَلْ قَالُوا مِثْلَ مَا قَالَ الْأَوَّلُونَ
Ñoom kay faf dañoo wax rekk la ñu jëkk ña waxoon.
82قَالُوا أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ
Nee nañu : “Ndax bu nu faatoo ba nekk suuf ak i yax, ndax dananu dekkiwaat ?
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
80Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 80

Simoore Al-Mu'minun Aaya 80 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom mooy dundal, mooy rey ; Moom mooy jàllasante guddeek…

Simoore Aaya 80/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 78–82. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers