Al-Mu'minun · 85/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
سَيَقُولُونَ لِلَّهِ ۚ قُلْ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ ۝٨٥
Sa-yaqooloona lillaah; qul afalaa tazakkkaroon
📖 Tekkim Wolof
Kon danañu wax ne : “Yàllaa ko moom”. Neel : “Moo ndax dangeen dul fàttaliku ? ”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 83-87 — Simoore Al-Mu'minun

83لَقَدْ وُعِدْنَا نَحْنُ وَآبَاؤُنَا هَٰذَا مِن قَبْلُ إِنْ هَٰذَا إِلَّا أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ
Lii dey digoon nañu ko sunuy maam ak nun ; lii daal ay léeb rekk la”
84قُل لِّمَنِ الْأَرْضُ وَمَن فِيهَا إِن كُنتُمْ تَعْلَمُونَ
Neel : “Ana kan moo moom suuf si ak li ci biiram ? Ndeem xam ngeen”.
85سَيَقُولُونَ لِلَّهِ ۚ قُلْ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
Kon danañu wax ne : “Yàllaa ko moom”. Neel : “Moo ndax dangeen dul fàttaliku ? ”
86قُلْ مَن رَّبُّ السَّمَاوَاتِ السَّبْعِ وَرَبُّ الْعَرْشِ الْعَظِيمِ
Neel : “Ana kan mooy Boroom asamaani juróom-ñaar tey Boroom Gàngunaay [Aras] gu màgg ga ? ”
87سَيَقُولُونَ لِلَّهِ ۚ قُلْ أَفَلَا تَتَّقُونَ
Danañu wax ne : “Yàllaa ko moom”. Neel : “Ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
85Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 85

Simoore Al-Mu'minun Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kon danañu wax ne : “Yàllaa ko moom”. Neel :…

Simoore Aaya 85/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers