Al-Mu'minun · 86/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
قُلْ مَن رَّبُّ السَّمَاوَاتِ السَّبْعِ وَرَبُّ الْعَرْشِ الْعَظِيمِ ۝٨٦
Qul mar Rabbus samaawaatis sab`i wa Rabbul `Arshil `Azeem
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Ana kan mooy Boroom asamaani juróom-ñaar tey Boroom Gàngunaay [Aras] gu màgg ga ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 84-88 — Al-Mu'minun

84قُل لِّمَنِ الْأَرْضُ وَمَن فِيهَا إِن كُنتُمْ تَعْلَمُونَ
Neel : “Ana kan moo moom suuf si ak li ci biiram ? Ndeem xam ngeen”.
85سَيَقُولُونَ لِلَّهِ ۚ قُلْ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
Kon danañu wax ne : “Yàllaa ko moom”. Neel : “Moo ndax dangeen dul fàttaliku ? ”
86قُلْ مَن رَّبُّ السَّمَاوَاتِ السَّبْعِ وَرَبُّ الْعَرْشِ الْعَظِيمِ
Neel : “Ana kan mooy Boroom asamaani juróom-ñaar tey Boroom Gàngunaay [Aras] gu màgg ga ? ”
87سَيَقُولُونَ لِلَّهِ ۚ قُلْ أَفَلَا تَتَّقُونَ
Danañu wax ne : “Yàllaa ko moom”. Neel : “Ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”
88قُلْ مَن بِيَدِهِ مَلَكُوتُ كُلِّ شَيْءٍ وَهُوَ يُجِيرُ وَلَا يُجَارُ عَلَيْهِ إِن كُنتُمْ تَعْلَمُونَ
Neel : “Ana kan moo ame ci loxoom nguurug lépp, kiy aare te soxlawul ku ko aar ? Waxleen rekk, ndax xam ngeen ko ! ”
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
86Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 86

Simoore Al-Mu'minun Aaya 86 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Ana kan mooy Boroom asamaani juróom-ñaar tey Boroom…

Simoore Aaya 86/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 84–88. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers