Al-Mu'minun · 93/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
قُل رَّبِّ إِمَّا تُرِيَنِّي مَا يُوعَدُونَ ٩٣
Transliteration
Qur Rabbi immmaa turiyannee maa yoo`adoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Sama Boroom, cëy boo ma wonoon li nga leen dig ;
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 91-95 — Al-Mu'minun
91مَا اتَّخَذَ اللَّهُ مِن وَلَدٍ وَمَا كَانَ مَعَهُ مِنْ إِلَٰهٍ ۚ إِذًا لَّذَهَبَ كُلُّ إِلَٰهٍ بِمَا خَلَقَ وَلَعَلَا بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ ۚ سُبْحَانَ اللَّهِ عَمَّا يَصِفُونَ
Yàlla jàppewul kenn doomam te it amul jeneen Yàlla ju muy àndal ; su loolu amoom, kon yàlla ju nekk dem ak boppam ak la mu sàkk te kon danañuy ëppantey doole. [Tudd naa sellam ga] ! Rawante naak li ñu koy melal.
92عَالِمِ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ فَتَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Mooy ki xam kumpaag li teew ! Kawe na [lool] li ñu koy bokkaaleel !
93قُل رَّبِّ إِمَّا تُرِيَنِّي مَا يُوعَدُونَ
Neel : “Sama Boroom, cëy boo ma wonoon li nga leen dig ;
94رَبِّ فَلَا تَجْعَلْنِي فِي الْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Yaw sama Boroom, bul ma boole mukk ci tooñkat yi.
95وَإِنَّا عَلَىٰ أَن نُّرِيَكَ مَا نَعِدُهُمْ لَقَادِرُونَ
Te it am Nanu kàttanu won la li Nu leen dig.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
93Aaya
Tekki — Al-Mu'minun 93
Simoore Al-Mu'minun Aaya 93 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Sama Boroom, cëy boo ma wonoon li nga…Simoore Aaya 93/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 91–95. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








