Al-Mu'minun · 94/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
رَبِّ فَلَا تَجْعَلْنِي فِي الْقَوْمِ الظَّالِمِينَ ۝٩٤
Rabbi falaa taj`alnee fil qawmiz zaalimeen
📖 Tekkim Wolof
Yaw sama Boroom, bul ma boole mukk ci tooñkat yi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 92-96 — Simoore Al-Mu'minun

92عَالِمِ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ فَتَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Mooy ki xam kumpaag li teew ! Kawe na [lool] li ñu koy bokkaaleel !
93قُل رَّبِّ إِمَّا تُرِيَنِّي مَا يُوعَدُونَ
Neel : “Sama Boroom, cëy boo ma wonoon li nga leen dig ;
94رَبِّ فَلَا تَجْعَلْنِي فِي الْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Yaw sama Boroom, bul ma boole mukk ci tooñkat yi.
95وَإِنَّا عَلَىٰ أَن نُّرِيَكَ مَا نَعِدُهُمْ لَقَادِرُونَ
Te it am Nanu kàttanu won la li Nu leen dig.
96ادْفَعْ بِالَّتِي هِيَ أَحْسَنُ السَّيِّئَةَ ۚ نَحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَصِفُونَ
Ña ngay jiñe ñaawtéef ci [jëf yu gën a]rafet. Nun [Yàlla] noo gën a xam la ñuy melal.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
94Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 94

Simoore Al-Mu'minun Aaya 94 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yaw sama Boroom, bul ma boole mukk ci tooñkat yi.

Simoore Aaya 94/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 92–96. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers