Al-Mu'minun · 92/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
عَالِمِ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ فَتَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ ۝٩٢
Aalimil Ghaibi wash shahhaadati fata`aalaa `ammaa yushrikoon
📖 Tekkim Wolof
Mooy ki xam kumpaag li teew ! Kawe na [lool] li ñu koy bokkaaleel !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 90-94 — Simoore Al-Mu'minun

90بَلْ أَتَيْنَاهُم بِالْحَقِّ وَإِنَّهُمْ لَكَاذِبُونَ
Indil Nanu leen dëgg waaye ñoom ay fenkat lañu.
91مَا اتَّخَذَ اللَّهُ مِن وَلَدٍ وَمَا كَانَ مَعَهُ مِنْ إِلَٰهٍ ۚ إِذًا لَّذَهَبَ كُلُّ إِلَٰهٍ بِمَا خَلَقَ وَلَعَلَا بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ ۚ سُبْحَانَ اللَّهِ عَمَّا يَصِفُونَ
Yàlla jàppewul kenn doomam te it amul jeneen Yàlla ju muy àndal ; su loolu amoom, kon yàlla ju nekk dem ak boppam ak la mu sàkk te kon danañuy ëppantey doole. [Tudd naa sellam ga] ! Rawante naak li ñu koy melal.
92عَالِمِ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ فَتَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Mooy ki xam kumpaag li teew ! Kawe na [lool] li ñu koy bokkaaleel !
93قُل رَّبِّ إِمَّا تُرِيَنِّي مَا يُوعَدُونَ
Neel : “Sama Boroom, cëy boo ma wonoon li nga leen dig ;
94رَبِّ فَلَا تَجْعَلْنِي فِي الْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Yaw sama Boroom, bul ma boole mukk ci tooñkat yi.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
92Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 92

Simoore Al-Mu'minun Aaya 92 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy ki xam kumpaag li teew ! Kawe na [lool]…

Simoore Aaya 92/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 90–94. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers