Al-Furqan · 37/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
وَقَوْمَ نُوحٍ لَّمَّا كَذَّبُوا الرُّسُلَ أَغْرَقْنَاهُمْ وَجَعَلْنَاهُمْ لِلنَّاسِ آيَةً ۖ وَأَعْتَدْنَا لِلظَّالِمِينَ عَذَابًا أَلِيمًا ٣٧
Transliteration
Wa qawma Noohil lammaa kazzabur Rusula aghraqnaahum wa ja`alnaahum linnaasi Aayatanw wa a`tadnaa lizzaalimeena `azaaban aleemaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te nitu Nooh ya, ba ñu weddee Yonent ya, labal Nanu leen, def Nanu leen it kéemaan ci nit ñi. Te waajalal Nanu tooñkat ya mbugal mu metti.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 35-39 — Al-Furqan
35وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ وَجَعَلْنَا مَعَهُ أَخَاهُ هَارُونَ وَزِيرًا
Jox Nanu Muusaa Téere ba, defal ko Aaruuna mbokkam mu di ko jàppale.
36فَقُلْنَا اذْهَبَا إِلَى الْقَوْمِ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا فَدَمَّرْنَاهُمْ تَدْمِيرًا
Nu wax leen ne : “Demleen yéen ñaar ca nit ña weddi woon Sunuy kàddu”. Nu alag leen.
37وَقَوْمَ نُوحٍ لَّمَّا كَذَّبُوا الرُّسُلَ أَغْرَقْنَاهُمْ وَجَعَلْنَاهُمْ لِلنَّاسِ آيَةً ۖ وَأَعْتَدْنَا لِلظَّالِمِينَ عَذَابًا أَلِيمًا
Te nitu Nooh ya, ba ñu weddee Yonent ya, labal Nanu leen, def Nanu leen it kéemaan ci nit ñi. Te waajalal Nanu tooñkat ya mbugal mu metti.
38وَعَادًا وَثَمُودَ وَأَصْحَابَ الرَّسِّ وَقُرُونًا بَيْنَ ذَٰلِكَ كَثِيرًا
Ak nitu Aad, ak nitu Samooda ak waa Rasi, ak maas yu bari yu nekkoon seeni diggante !
39وَكُلًّا ضَرَبْنَا لَهُ الْأَمْثَالَ ۖ وَكُلًّا تَبَّرْنَا تَتْبِيرًا
Ku nekk ci ñoom, sadd Nanu koy léebu, alag Nanu leen ñoom ñépp.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
37Aaya
Tekki — Al-Furqan 37
Simoore Al-Furqan Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te nitu Nooh ya, ba ñu weddee Yonent ya, labal…Simoore Aaya 37/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








