Al-Furqan · 36/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
فَقُلْنَا اذْهَبَا إِلَى الْقَوْمِ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا فَدَمَّرْنَاهُمْ تَدْمِيرًا ۝٣٦
Faqulnaz habaaa ilal qawmil lazeena kazzaboo bi Aayaatinaa fadammarnaahum tadmeeraa
📖 Tekkim Wolof
Nu wax leen ne : “Demleen yéen ñaar ca nit ña weddi woon Sunuy kàddu”. Nu alag leen.

🎧 Dégg


📜 Aaya 34-38 — Simoore Al-Furqan

34الَّذِينَ يُحْشَرُونَ عَلَىٰ وُجُوهِهِمْ إِلَىٰ جَهَنَّمَ أُولَٰئِكَ شَرٌّ مَّكَانًا وَأَضَلُّ سَبِيلًا
Ña nga xam ne dees na leen pang, di leen diri ci seen xar-kanam ya, jëme leen Safara, ñoom ñooy gën a yées wàccuwaay, gën a réere yoon wu jub wa.
35وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ وَجَعَلْنَا مَعَهُ أَخَاهُ هَارُونَ وَزِيرًا
Jox Nanu Muusaa Téere ba, defal ko Aaruuna mbokkam mu di ko jàppale.
36فَقُلْنَا اذْهَبَا إِلَى الْقَوْمِ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا فَدَمَّرْنَاهُمْ تَدْمِيرًا
Nu wax leen ne : “Demleen yéen ñaar ca nit ña weddi woon Sunuy kàddu”. Nu alag leen.
37وَقَوْمَ نُوحٍ لَّمَّا كَذَّبُوا الرُّسُلَ أَغْرَقْنَاهُمْ وَجَعَلْنَاهُمْ لِلنَّاسِ آيَةً ۖ وَأَعْتَدْنَا لِلظَّالِمِينَ عَذَابًا أَلِيمًا
Te nitu Nooh ya, ba ñu weddee Yonent ya, labal Nanu leen, def Nanu leen it kéemaan ci nit ñi. Te waajalal Nanu tooñkat ya mbugal mu metti.
38وَعَادًا وَثَمُودَ وَأَصْحَابَ الرَّسِّ وَقُرُونًا بَيْنَ ذَٰلِكَ كَثِيرًا
Ak nitu Aad, ak nitu Samooda ak waa Rasi, ak maas yu bari yu nekkoon seeni diggante !
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — Al-Furqan 36

Simoore Al-Furqan Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu wax leen ne : “Demleen yéen ñaar ca nit…

Simoore Aaya 36/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers