Ash-Shu'ara · 12/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
قَالَ رَبِّ إِنِّي أَخَافُ أَن يُكَذِّبُونِ ۝١٢
Qaala Rabbi inneee akhaafu ai yukazziboon
📖 Tekkim Wolof
[Muusaa] wax ne : “Yaw Sama Boroom, damaa ragal ñu jàppe ma ab fenkat [weddi ma] ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 10-14 — Simoore Ash-Shu'ara

10وَإِذْ نَادَىٰ رَبُّكَ مُوسَىٰ أَنِ ائْتِ الْقَوْمَ الظَّالِمِينَ
[Fàttalikul] ba Yàlla woo na Muusaa, [ne ko] : “Demal [jubbanti ji] tooñkat ya,
11قَوْمَ فِرْعَوْنَ ۚ أَلَا يَتَّقُونَ
nitu Firawna” ; moo ndax ñoom duñu ragal Yàlla ?
12قَالَ رَبِّ إِنِّي أَخَافُ أَن يُكَذِّبُونِ
[Muusaa] wax ne : “Yaw Sama Boroom, damaa ragal ñu jàppe ma ab fenkat [weddi ma] ;
13وَيَضِيقُ صَدْرِي وَلَا يَنطَلِقُ لِسَانِي فَأَرْسِلْ إِلَىٰ هَارُونَ
samab dënn di xat, te kon dootuma mën a wax : Yónnil kon Aaruuna, def ko Yonent.
14وَلَهُمْ عَلَيَّ ذَنبٌ فَأَخَافُ أَن يَقْتُلُونِ
Te itam, am na tuuma ju ñu may jiiñ ; te ragal naa ñu rey ma”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 12

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Muusaa] wax ne : “Yaw Sama Boroom, damaa ragal ñu…

Simoore Aaya 12/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers