Ash-Shu'ara · 176/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
كَذَّبَ أَصْحَابُ الْأَيْكَةِ الْمُرْسَلِينَ ۝١٧٦
Kazzaba As haabul Aykatil mursaleen
📖 Tekkim Wolof
Waa Aykata weddi woon nañu Yonent ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 174-178 — Ash-Shu'ara

174إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ay kéemaan a ngi ci biir loolu. Te taxul ña ëppoon ca ñoom gëm.
175وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Sa Boroom, Mooy Boroom kàttan, di Jaglewaakoon ba [yërmaandeem].
176كَذَّبَ أَصْحَابُ الْأَيْكَةِ الْمُرْسَلِينَ
Waa Aykata weddi woon nañu Yonent ya.
177إِذْ قَالَ لَهُمْ شُعَيْبٌ أَلَا تَتَّقُونَ
Ba leeen seen mbokk ma Suhaybu waxee ne : “Moo ndax dungeen ragal Yàlla”.
178إِنِّي لَكُمْ رَسُولٌ أَمِينٌ
Man mii dey, ab Yonent laa ci yéen bu wóor.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
176Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 176

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 176 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waa Aykata weddi woon nañu Yonent ya.

Simoore Aaya 176/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 174–178. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers