Ash-Shu'ara · 177/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
إِذْ قَالَ لَهُمْ شُعَيْبٌ أَلَا تَتَّقُونَ ۝١٧٧
Iz qaala lahum Shu`aybun alaa tattaqoon
📖 Tekkim Wolof
Ba leeen seen mbokk ma Suhaybu waxee ne : “Moo ndax dungeen ragal Yàlla”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 175-179 — Ash-Shu'ara

175وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Sa Boroom, Mooy Boroom kàttan, di Jaglewaakoon ba [yërmaandeem].
176كَذَّبَ أَصْحَابُ الْأَيْكَةِ الْمُرْسَلِينَ
Waa Aykata weddi woon nañu Yonent ya.
177إِذْ قَالَ لَهُمْ شُعَيْبٌ أَلَا تَتَّقُونَ
Ba leeen seen mbokk ma Suhaybu waxee ne : “Moo ndax dungeen ragal Yàlla”.
178إِنِّي لَكُمْ رَسُولٌ أَمِينٌ
Man mii dey, ab Yonent laa ci yéen bu wóor.
179فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَطِيعُونِ
Ragal-leen Yàlla te topp ma [samay ndigal],
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
177Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 177

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 177 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba leeen seen mbokk ma Suhaybu waxee ne : “Moo…

Simoore Aaya 177/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 175–179. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers