Ash-Shu'ara · 190/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ ۝١٩٠
Inna fee zaalika la Aayah; wa maa kaana aksaruhum mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Ay kéemaan a ngi ci biir loolu. Te taxul ña ëppoon ca ñoom gëm.
🎧 Dégg

📜 Aaya 188-192 — Ash-Shu'ara

188قَالَ رَبِّي أَعْلَمُ بِمَا تَعْمَلُونَ
Suhaybu ne leen : “Sama Boroom a gën a xam li ngeen di def”.
189فَكَذَّبُوهُ فَأَخَذَهُمْ عَذَابُ يَوْمِ الظُّلَّةِ ۚ إِنَّهُ كَانَ عَذَابَ يَوْمٍ عَظِيمٍ
Ñu weddi ko. Mbugalum niir wa dal ca seen kaw. Doon mbugalum bis bu màgg.
190إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ay kéemaan a ngi ci biir loolu. Te taxul ña ëppoon ca ñoom gëm.
191وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Boroom, Mooy Boroom kàttan, di Jaglewaakoon ba [yërmaandeem].
192وَإِنَّهُ لَتَنزِيلُ رَبِّ الْعَالَمِينَ
[Alxuraan jii], ci lu bir, wàcceg Boroom àddina si la,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
190Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 190

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 190 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ay kéemaan a ngi ci biir loolu. Te taxul ña…

Simoore Aaya 190/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 188–192. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers