Ash-Shu'ara · 21/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
فَفَرَرْتُ مِنكُمْ لَمَّا خِفْتُكُمْ فَوَهَبَ لِي رَبِّي حُكْمًا وَجَعَلَنِي مِنَ الْمُرْسَلِينَ ۝٢١
Fafarartu minkum lam maa khiftukum fawahaba lee Rabbee hukmanw wa ja`alanee minal mursaleen
📖 Tekkim Wolof
Ma daldi daw ba ma tiitee : faf Yàlla jox ma xam-xamu [baatin], def ma ma bokk ca Yonent ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 19-23 — Simoore Ash-Shu'ara

19وَفَعَلْتَ فَعْلَتَكَ الَّتِي فَعَلْتَ وَأَنتَ مِنَ الْكَافِرِينَ
Ak jëf ji nga fi jëfoon tey xarabaate”
20قَالَ فَعَلْتُهَا إِذًا وَأَنَا مِنَ الضَّالِّينَ
Muusaa ne ko : “Defoon naa ko, waaye teyuma ko.
21فَفَرَرْتُ مِنكُمْ لَمَّا خِفْتُكُمْ فَوَهَبَ لِي رَبِّي حُكْمًا وَجَعَلَنِي مِنَ الْمُرْسَلِينَ
Ma daldi daw ba ma tiitee : faf Yàlla jox ma xam-xamu [baatin], def ma ma bokk ca Yonent ya.
22وَتِلْكَ نِعْمَةٌ تَمُنُّهَا عَلَيَّ أَنْ عَبَّدتَّ بَنِي إِسْرَائِيلَ
Te loolu xéewal la goo may mën a xéewale, ndax liggéeyloo nga giir Banii-Israayil lu ne ? ”
23قَالَ فِرْعَوْنُ وَمَا رَبُّ الْعَالَمِينَ
[Firawna] ne ko : “Waaw, ana kan mooy Boroom àddina si ? ”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 21

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ma daldi daw ba ma tiitee : faf Yàlla jox…

Simoore Aaya 21/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers