Ash-Shu'ara · 224/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَالشُّعَرَاءُ يَتَّبِعُهُمُ الْغَاوُونَ ۝٢٢٤
Washshu `araaa`u yattabi `uhumul ghaawoon
📖 Tekkim Wolof
Woykat ya nag, nitu mbalgas ya rekk a leen di topp.

🎧 Dégg


📜 Aaya 222-226 — Simoore Ash-Shu'ara

222تَنَزَّلُ عَلَىٰ كُلِّ أَفَّاكٍ أَثِيمٍ
Danañuy wàcc ci képp kuy ab duuraakoon bu bariy bàkkaar.
223يُلْقُونَ السَّمْعَ وَأَكْثَرُهُمْ كَاذِبُونَ
Ñooy yàng seen nopp di déglu... Te la ëpp ci ñoom fenkat lañu.
224وَالشُّعَرَاءُ يَتَّبِعُهُمُ الْغَاوُونَ
Woykat ya nag, nitu mbalgas ya rekk a leen di topp.
225أَلَمْ تَرَ أَنَّهُمْ فِي كُلِّ وَادٍ يَهِيمُونَ
Xanaa gisoo ne ñoom ci xur wu nekk la ñu fay wëndeelu,
226وَأَنَّهُمْ يَقُولُونَ مَا لَا يَفْعَلُونَ
Te it dañuy wax lu ñu dul def ?
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
224Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 224

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 224 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Woykat ya nag, nitu mbalgas ya rekk a leen di…

Simoore Aaya 224/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 222–226. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers